Tradução gerada automaticamente

exibições de letras 16

Nappé (feat. BM Jaay & Samba Peuzzi)

Bass Thioung

Letra

Nappé (feat. BM Jaay & Samba Peuzzi)

Nappé (feat. BM Jaay & Samba Peuzzi)

Coloque isso no tempoTeg ko ci temps
Você está aqui no tempoAmoon nga fi temps
Agora nós somos como o ventoLéegi ñun ñoo moome vent
Estamos nappe!Dangay nappe!

Você sabe que eu só estou na minhaYaw xam nga rekk dama di ndaanaan
A sombra atrás de mimLamb démb ma daan
Eu já te disse que não sou de ficar na linhaMa leen gëna saf ni daxar ba ci yoon mbaadan
Não é assim que eu me comportoMoytul noon mu tarxis saran
Vocês estão se jogandoBari ngeen jaxan
O flow é do jeito que eu gosto, só pra vocêFlow bu reew la indi tay moom
Rap suave é o que eu façoRap bu soft la laal

Sem parar (sem parar)Amul arrêt (amul arrêt)
Só vai (só vai)Dey daw rekk (dey daw rekk)
Faz o que tem que fazer, eu sei que você é como Mbappé (como Mbappé)Fees lay def, xam naa gone bi comme Mbappé (comme Mbappé)
Mas não tem parada (sem parada)Ma ni amul arrêt (amul arrêt)
Não vou me atrasar (mukk mukk)Munoo ma tardeel (mukk mukk)
Você sabe que eu sou o que eu sou, não me deixe na mãoXam nga coof laa raw ma jafe bàyyi ma
Apoie minha grana, eu estou nappeSàndi sama mbale mi nappé

Só vaiDéy daw rekk
Yoroo wérooYoroo wéroo
Eh, quero que você fique, quero nappeEh, bëgg jitte bëgg nappé
Vamos nappe, vamos nappeLooy nappé, looy nappé
Sabemos o que você está fazendoXam nañu li ngay dundu
Dê um tempo pro nosso corpo, estamos nappeDawoo suñu yaram, dangay nappé

Coloque isso no tempoTeg ko ci temps
Você está aqui no tempoAmoon nga fi temps
Agora nós somos como o ventoLéegi ñun ñoo moome vent
Estamos nappe!Dangay nappe!

Festa é o lugarFetaak moom place
Eles estão lá em cimaÑoom ci kaw lañu jëm
E eu estou aquiTe man fa laa toog
Fazendo o que eu possoRomb ay kuti ñu may mbow
Se não for pra ser, não vai serNdax te bukki bi la bot
O que eu faço é só pra me manterTaat moo ko topp muy déllu gannaaw
Aqui onde eu estouCi bi ma ko
Eu e eles nunca vamos pararMan ak ñoom dootuñu laale jamais
Como os Guissés-MaaboComme les Guissés-Maabo
Coloque sua mão e me ajude no tempoTeg fa sa loxo jàppal ma temps
É uma pérola como KylianPépite la ni Kylian

Agora, a gente se entende, não sou só euÑaw ngemb tere mbot ndaanaan dégg may daan
O mundo é pequeno, mas seu rapper é grandeÀdduna potu nda la sa rappeur du gux du naan
Eu só quero saber de você, me ajude a entenderMan lan ko diw ma jàpp seen girl yi, jàppal leen gam
No final, é só isso que eu queroFinal rekk moom laay joué
Eu sou o chefe da banda, só cozinhandoMoom chef de bandi lay ñodd cooki feebar rekk de
Vou me dar bem, mas as coisas vão ficar difíceisDinañu ma daq mais yere yi may sol rekk a may teye
O dinheiro é pouco, mas não é tudoXaalis lay xëccoo mais du pe
O que não me serve, eu deixo pra láLu ne lay teg sama der tewul maa ngi jàpp teint

Sem parar (sem parar)Amul arrêt (amul arrêt)
Só vai (só vai)Dey daw rekk (dey daw rekk)
Faz o que tem que fazer, eu sei que você é como Mbappé (como Mbappé)Fees lay def, xam naa gone bi comme Mbappé (comme Mbappé)
Mas não tem parada (sem parada)Ma ni amul arrêt (amul arrêt)
Não vou me atrasar (mukk mukk)Munoo ma tardeel (mukk mukk)
Você sabe que eu sou o que eu sou, não me deixe na mãoXam nga coof laa raw ma jafe bàyyi ma
Apoie minha grana, eu estou nappeSàndi sama mbale mi nappé

Só vaiDéy daw rekk
Yoroo wérooYoroo wéroo
Eh, quero que você fique, quero nappeEh, bëgg jitte bëgg nappé
Vamos nappe, vamos nappeLooy nappé, looy nappé
Sabemos o que você está fazendoXam nañu li ngay dundu
Dê um tempo pro nosso corpo, estamos nappeDawoo suñu yaram, dangay nappé

Coloque isso no tempoTeg ko ci temps
Você está aqui no tempoAmoon nga fi temps
Agora nós somos como o ventoLéegi ñun ñoo moome vent
Estamos nappe!Dangay nappé!

Eu só estou no meu caminho como BRTMan rekk ci sama yoon comme BRT bi
As crianças estão jogando, a vida é uma festaXale yaa ngi jooy ass bi la tebi
Não me faça de general, você é o que eu esperoNe ma général yaw la asp bi
Não me deixe na mão, eu só quero saberSoxlatul may wax lam xa bi
Agora, a palavra é a chave, você vai entenderÑaw, kàddu baal la dum leen gaawa dégg
Eu sou o que sou, não me deixe na mãoMan la dogo ñi doon bañ rambax ci game bi lañ gis tey ñu yor bongo
Como Aly, eu sou o filho do seu paiComme Aly wéy geroo fils sa buur la
Um Aly que não se esquece de vocêBenn Aly ñëw wacc la sa ngur la
Apoie seu rapper, faça-o brilhar de verdadeTegal sa rappeur sañ-sañ, tojal ko mbari from Dieck
Coloque isso no tempo, faça-o estourarTeg ko ci temps di sañse, jamos ko blow tek-tek
Lindas suas jogadas, seu K7 é meu sucessoLindia seen game bi bët-set, seen K7 sama weccet
Fazendo a vida de jetset, sendo o rei da festaFatt dundu lifu jetset, teddi king fat pérpéte

Sem parar (sem parar)Amul arrêt (amul arrêt)
Só vai (só vai)Dey daw rekk (dey daw rekk)
Faz o que tem que fazer, eu sei que você é como Mbappé (como Mbappé)Fees lay def, xam naa gone bi comme Mbappé (comme Mbappé)
Mas não tem parada (sem parada)Ma ni amul arrêt (amul arrêt)
Não vou me atrasar (mukk mukk)Munoo ma tardeel (mukk mukk)
Você sabe que eu sou o que eu sou, não me deixe na mãoXam nga coof laa raw ma jafe bàyyi ma
Apoie minha grana, eu estou nappeSàndi sama mbale mi nappé

Só vaiDéy daw rekk
Yoroo wérooYoroo wéroo
Eh, quero que você fique, quero nappeEh, bëgg jitte bëgg nappé
Vamos nappe, vamos nappeLooy nappé, looy nappé
Sabemos o que você está fazendoXam nañu li ngay dundu
Dê um tempo pro nosso corpo, estamos nappeDawoo suñu yaram, dangay nappé

Coloque isso no tempoTeg ko ci temps
Você está aqui no tempoAmoon nga fi temps
Agora nós somos como o ventoLéegi ñun ñoo moome vent
Estamos nappe!Dangay nappé!

Comentários

Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra

0 / 500

Faça parte  dessa comunidade 

Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de Bass Thioung e vá além da letra da música.

Conheça o Letras Academy

Enviar para a central de dúvidas?

Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.

Fixe este conteúdo com a aula:

0 / 500

Opções de seleção