395px

Tamanefi

Dip Doundou Guiss

Tamanefi

Come On! Alkati ya ngi sa kaw
Thiap bi nga doon xam naniou ni ya ngi ak xalissak drogue
Wa bou yabo nanal ci sa Safara yi dieul garap bi xeupo
Thiat ci sa maw laff yi la tok
May sa thiabi kasso, mane la may Picasso
Parce que boudone man xamna di nga sol
Lou eupeu att nga ndara woor kay niu nafila bokk
Père Noel raciste la mane moussouma guiss cadeaux
Guiss na ay Pa yu djaay sen taxi pour am passou avions
Atoum leumb souma nekhé douma liguèye
A tout moment meune nga déh ni ngoumba ci Guedj
Dou ben bopp rek nek ci mane
Def lou yomb rek méti ci mane

Kouy topando mane ak yaw nouro wouniu système
Yallah loutax ma dée ni kou dioudo ci cimetière?
Mouno wa Rap'Adio kone non meuno li DIP Def
TLK dou Album, dou maxi, non non dou mixtape
Yaggo tchi kaw ni boy bou ndaw bou tiim Jail
Rap bi dafa yombone nioune niossi soti dindière
Ndiago bi moy Boss pourtant moussou massi djékkeu
Douma lekk kou souroul parce que dama xiff ndeim
Na def lou eup 1000 scènes, encaissé plus de 1000 chèques
Sa Papa, Sa yaye ak baag bi lay souleudo ci tenn
Maf-fu Hip Hop bi mo raw bi ci Goudi Town
Rap bi dou djoug ndakh boy bou am buzz outi daanou

Boul mousseu ni yafi meun Témanéfi
Yaye boul niaanati kèneu Témanéfi
Marozik mounoul xonett ndakh ma ngi fi
Sokhla wuma kèneu kumay temoigné fils
Boul mousseu ni yafi meun Témanéfi
Yaye boul niaanati kèneu Témanéfi
Idy namoul iPhone 6 ndakh ma ngi fi
Sokhla wouma kèneu kumay temoigné fils

Dé lène Diaamou Yallah té nguène gueum sen bopp
Bèneu lama may mane ma woute yeneen 2 cerveaux
Même handicapés yarramam day ndaw
Wayé kou Fan Pée (1er) bi toujours deuss (2eme) lay done
No def ba degg Jàmm ci deuk bou dégueulasse bi
Yëk Carrapid, bokk nëk ak Pa' bi
Mama ress la, ress sa rakk yi
Réro demb téyeul sa lamiñ
Sénégal moy deukou Téranga mais amoul restaurant du coeur
Kone loy xalate ci boy yi moussoul ray sen bopp beug xexal
Afrique
Liberté moussoul am nigger fuck 4 Avril
Dictateur rek ba déh ni Colonel Khadafi
Bandit yi yéwou yeup ngi def, ñi gueuméintou dem teudi
Jail
May Punch ba ndel Kocc Barma té dougneko nétali kèneu
Nigger douggou na palais xamna donou Président
Boul Rap toujours rek fexel ba am comme li Jay-Z am
Boy Grand yoff, Arafat boy xamna fou BOON bou nekh bi am
Meune nagnema faat wayé mounou niouma fatté
Dioudou waat na ba sonneu mais bène yoon lay dé
Gars yima gueumoul wone légui gueméwouniu ma
Naukhaur yi lekkone nagnema bu yagg souma deumé woul woone
Yen ñeup souma len eupone alal di nguène ma faral
Comme gars yi am ay milliards, milliards pour am ticket
Safara
Sama succès bou rèèn niggers wérenté nako daw
Yen ñeup ken dou ame louko nekh ni ay waraté kat ci boîte
Dama done djaap sama gars yeup faaté yèèneu texte yi
Bayil ma diéma djaap text yeup faaté yèneu gars yi
Niit yi xalaté touniou xel ndakh seug séni sex
Motakh makk dou jog ci teudé rakkam ni Ci-Yénekaay yi
Boy guél yeup leundeum dou foula nekh ngay toufli
25 ans baayil ma doundou comme si Papa nékatoufi
Batay mane may wakh loutakh nièneu ñi di taf sen guémiñ
Yaay sa dome dou wadd ni rongagnou ray kattou niit
Morée

Boul mousseu ni yafi meun Témanéfi
Yaye boul niaanati kèneu Témanéfi
Marozik mounoul xonett ndakh ma ngi fi
Sokhla wuma kèneu kumay temoigné fils
Boul mousseu ni yafi meun Témanéfi
Yaye boul niaanati kèneu Témanéfi
Idy namoul iPhone 6 ndakh ma ngi fi
Sokhla wouma kèneu kumay temoigné fils

Tamanefi

Venha! Alkati ya naw kaw
Thiap bi doon xam naniou ni ya ngi ak xalissak drug
Wa bou yabo nanal ci em Safara yi dieul garap bi xeupo
Faça o seguinte com maw laff yi la tok
Com thiabi kasso, mane la com Picasso
Porque homem boudone xamna di nga sol
Lou eupeu att nga ndara woor kay niu nafila bokk
Presentes racist la mane moussouma guiss de Papai Noel
Guiss no Pa yu djaay sen taxi para aviões que passaram
Atoum leumb souma nekhé douma liguèye
A qualquer momento, selecione o guia de Guedj
Dou ben bopp rek nek ci mane
Def lou yomb rek méti ci mane

Kouy topando mane ak yaw nouro wouniu system
Yallah loutax ma dee ni kou dioudo ci cemitério?
Mouno wa Rap'Adio não é o meu DIP Def
Álbum TLK duplo, maxi duplo, não mixtape duplo
Yaggo tchi kaw ni menino bou ndaw bou tiim Cadeia
Rap bi dafa yombone nioune niossi soti turkey
Ndiago bi moy Boss ainda moussou massi djékkeu
Douma lekk kou souroul porque dama xiff ndeim
Na definição de 1000 cenas, recebi mais de 1000 cheques
Sa Papa, Sa yaye ak baag bi leiga souleudo ci tenn
Maf-fu Hip Hop bi mo raw bi c Goudi Town
Rap bi dou djoug ndakh boy bou am buzz outi daanou

Boul mousseu ni yafi meun Témanéfi
Yaye boul niaanati kèneu Témanéfi
Marozik mounoul xonett ndakh ma ngi fi
Sokhla wuma kèneu kumay testemunhou o filho
Boul mousseu ni yafi meun Témanéfi
Yaye boul niaanati kèneu Témanéfi
Idy namoul iPhone 6 mais recente versão
Sokhla wouma kèneu kumay testemunhou o filho

Dè lène Diaamou Yallah o nguène gueum sen bopp
Bèneu lama may mane ma woute yeneen 2 brain
Mesmo deficiente yarramam day ndaw
Wayé kou Fan Pée (1º) bi sempre deuss (2º) feito
No def ba degg Jàmm ci deuk bou dégueulasse bi
Yëk Carrapid, bokk nëk ak Pa 'bi
Mama ress la, ress sa rakk yi
Réro demb téyeul in lamiñ
Senegal moy deukou Téranga mais amoul restaurant du coeur
Kone loy xalate ci boy yi moussoul ray sen bopp beug xexal
África
Liberty moussoul am nigger fuck 4 de abril
Reitor do Ditador do Coronel Khadafi
Bandido yi yéwou yeup ngi def, ñi gueuméintou dem teudi
Cadeia
May Punch no Kocc Barma tee dougneko nétali kèneu
Nigger douggou na palace xamna donou presidente
Boul Rap sempre rek fexel ba am como li Jay-Z am
Garoto Grand yoff, Arafat garoto xamna fou BOON bou nekh bi am
Meune nagnema faat wayé mounou niouma fatté
Dioudou waat na ba sonneu mas bène yoon lay dé
Guy yima gueumoul ganhou legui gueméwouniu ma
Naukhaur yi lekkone nagnema bu yagg souma deumé woul woone
Yen eeup souma len eupone alal di nguène ma faral
Como caras, eu sou a bilhões, bilhões por bilhão
Safara
Sama sucesso bou reign niggers werenté nako daw
Yen eup ken dou ame louko nekh ni é waraté kat ci box
Dama feito djaap sama cara yeup faaté yèèneu texto yi
Bayil ma diéma djaap text yeup faaté yèneu guys yi
Niit yi xalaté touniou xel ndakh seug Séni sex
Motakh makk dou jog ci teudé rakkam em Ci-Yénekaay yi
Boy guél yeup leundeum dou foula nekh ngay toufli
25 anos baayil ma doundou como se Papa nékatoufi
Juba batay com wakh loutakh nièneu ñi de taf sen guémiñ
Yaay no domo dou wadd ni rongagnou ray kattou niit
Morea

Boul mousseu ni yafi meun Témanéfi
Yaye boul niaanati kèneu Témanéfi
Marozik mounoul xonett ndakh ma ngi fi
Sokhla wuma kèneu kumay testemunhou o filho
Boul mousseu ni yafi meun Témanéfi
Yaye boul niaanati kèneu Témanéfi
Idy namoul iPhone 6 mais recente versão
Sokhla wouma kèneu kumay testemunhou o filho