Mom (feat. Dieyla)
[El Maestro]
Sama galanterie moo koy daaneel
Mbëggeel bi ñuy dundu da rare
Li ma bëgg rekk lay def
Moom du moromu gaa yi
[Dieyla]
Sama bànneex, sama xol yaw a
Su ma dundee, su ma dee yaw a
Ni ma woloo fort
Moom du moromu gaa yi
Jëmm ji nob naa ko
Ba dama ci mujj baadola
Ndekkete yoo bile mbëggeel bu doon làmb
Moom laay bëral
[El Maestro]
Kaar Mashallah, bu ñu cat dugg
Bés bu ñu jote chérie bu ci kenn dugg
Ñëwal woo ma, man dina baalu
Noon yi lay baña xaajal sunu diggante
[Dieyla]
May na ma nopp xel lay dégge
Sama xol bi nim koy def ni neex na
Moom ngay yàpp, te yàpp ko set!
Moom du moromu gaa yi
[El Maestro]
Yaw xottil xolam
Sama jëmm ji ngay jàkkaarlool
Mënuma ko réer
Daf ma géolocalisé
[Dieyla]
Moom laay wër
Wurus ci digg manding la
Duma ko caaxaane
Moom du moromu gaa yi
[El Maestro]
Sama galanterie moo koy daaneel
Mbëggeel bi ñuy dundu da rare
Li ma bëgg rekk lay def
Moom du moromu gaa yi
[Dieyla]
Sama bànneex, sama xol yaw a
Su ma dundee, su ma dee yaw a
Ni ma woloo fort
Moom du moromu gaa yi
[El Maestro]
Xam naa ni amul njëg
Waaye nakk xolam bu doon jaay
Na ko jënd lu chère
Pare naa ko garde la monnaie
Su ma xoolee gis na boppam
Moom ne na ci man lay seetu
[Dieyla]
May na ma nopp xel lay dégge
Sama xol bi nim koy def ni neex na
Moom ngay yàpp, te yàpp ko set!
Moom du moromu gaa yi
[El Maestro]
Sama galanterie moo koy daaneel
Mbëggeel bi ñuy dundu da rare
Li ma bëgg rekk lay def
Moom du moromu gaa yi
[Dieyla]
Sama bànneex, sama xol yaw a
Su ma dundee, su ma dee yaw a
Ni ma woloo fort
Moom du moromu gaa yi
[Dieyla]
Moom laay wër
Wurus ci digg manding la
Duma ko caaxaane
Moom du moromu gaa yi
Anh yaw yaa pare, yaa mën bëre
Lu ne ngay wane gisuma loo tële
Ndekkete yoo bile mbëggeel bu doon làmb
Moom laay bërel
Mãe (feat. Dieyla)
[El Maestro]
Minha galanteria é só pra você
A beleza que a gente vive é rara
O que eu quero é só fazer
Ela não é só uma garota qualquer
[Dieyla]
Meu amor, meu coração é seu
Se eu viver, se eu morrer, é por você
Se eu te chamar forte
Ela não é só uma garota qualquer
A beleza eu já vi
Mas eu não vou me entregar
A beleza que você tem é rara
Ela é quem eu quero
[El Maestro]
Kaar Mashallah, quando a gente se encontra
O dia que a gente se vê, querida, é especial
Olhe pra mim, eu vou me esforçar
Essas coisas não vão nos separar
[Dieyla]
Eu quero que você ouça o que eu digo
Meu coração está feliz quando você faz isso
Ela é tudo, e tudo é dela!
Ela não é só uma garota qualquer
[El Maestro]
Você toca meu coração
Meu amor, você é meu tudo
Não posso me perder
Estou geolocalizado
[Dieyla]
Ela é quem eu quero
A beleza que eu vejo é única
Não vou me afastar
Ela não é só uma garota qualquer
[El Maestro]
Minha galanteria é só pra você
A beleza que a gente vive é rara
O que eu quero é só fazer
Ela não é só uma garota qualquer
[Dieyla]
Meu amor, meu coração é seu
Se eu viver, se eu morrer, é por você
Se eu te chamar forte
Ela não é só uma garota qualquer
[El Maestro]
Eu sei que não tem ninguém igual
Mas meu coração não vai se vender
Vou comprar algo caro
E guardar o troco
Se eu olhar e ver seu rosto
Ela disse que eu sou o que ela quer
[Dieyla]
Eu quero que você ouça o que eu digo
Meu coração está feliz quando você faz isso
Ela é tudo, e tudo é dela!
Ela não é só uma garota qualquer
[El Maestro]
Minha galanteria é só pra você
A beleza que a gente vive é rara
O que eu quero é só fazer
Ela não é só uma garota qualquer
[Dieyla]
Meu amor, meu coração é seu
Se eu viver, se eu morrer, é por você
Se eu te chamar forte
Ela não é só uma garota qualquer
[Dieyla]
Ela é quem eu quero
A beleza que eu vejo é única
Não vou me afastar
Ela não é só uma garota qualquer
Ah, você é tudo, você pode ser
O que você quiser, eu só quero te ver
A beleza que você tem é rara
Ela é quem eu quero