395px

Trem da Mente

Index Ñuul Kukk

Saxaaru Xel

Alhamdu Lillaahi sant a war
Alhamdu Lillaahi sant a war
Jàmbat ju bari sax fajul naqar
Te du tax kenn sawar
Sidy la abal mbaggam
Nga ciy lëng sooy nërmeelu

Xel mi fa mu dem daa sori
Saxaar gi ci tux yóbbuwu ma
Nit ñee ma di yóbbaale

Xel mi fa mu yéeg daa kawe
Saxaar gi ci tux yéegewu ma
Nit ñee ma di dofloo nii

Xel mi fa mu dem daa sori
Saxaar gi ci tux yóbbuwu ma
Nit ñee ma ni yóbbaale

Maa ngi romb fanweeri at sama wërsëg di daagu
Soxla yi taxaw sañumaa toog may jug ak di daanu
Ñépp naan lu ko dal kii moo dellu ginnaaw ni taat
Amatuma baat, ñu may jàll baat
Alal suy wax, bu neexul dañu ko wannal baat
Ba ci muuma bu yor ay milyoŋ koñ bi moo fiy am baat
Ma-rakk yii, ak seen yaay jii
Daan ma yaakaar su ñuy añ dootuñu ma xaar

Léegi dañu may (baleen ma waay)
Ŋóobi di ma ŋar (baleen ma waay)
Wutal nañu ma tur (baleen ma waay)
Béjjanu ginaar (baleen ma waay)
Lañu may tooñee fu ma jaar (baleen ma waay)
Ma bañ ko di xeex (baleen ma waay)
Ñu ma koy gën a wax (baleen ma waay)
Ma beru bàyyi leen (baleen ma waay)
Ñu naan damay tux ñax (baleen ma waay)
Koñ bi yépp dëkkal ma fu ma dëkkul (baleen ma waay)
Bëggatuñu maa naw
Waayjur yi tere seen doom yi bëgg ma
Ba ñépp di ma daw
Nàmm seen paaka rendi ma
Te naan Yàlla Buur Mooy dogal
Sol ngeen mbubbu saytaane

Xel mi fa mu dem daa sori
Saxaar gi ci tux yóbbuwu ma
Nit ñee ma di yóbbaale

Naqar gu ànd ak naqaral
Xalaat yu bari ànd ak wéet
Man naa dofloo jaam bee

Xel mi fa mu dem daa sori
Saxaar gi ci tux yóbbuwu ma
Nit ñee ma di yóbbaale

Poos bi dërëm da caa baax
Fayu luyaas dañu lay laaj
Soble mbaa njëgu laaj
Soo dul joxe li ñu lay laaj
Bis dinga wax ñu ne: Ku la ko laaj

Ñàkk loo def (baleen ma waay)
Ñàkk loo def (baleen ma waay)
Boole ceek nit ñi lay def (baleen ma waay)
Man na dem ba def la def-def (baleen ma waay)
Jamono ji sax daa metti muñ ci dafa war kuy jullit
Laa Illah Illaahu

Xel mi fa mu dem daa sori
Saxaar gi ci tux yóbbuwu ma
Nit ñee ma di yóbbaale

Xel mi fa mu dem daa sori
Saxaar gi ci tux yéegewu ma (baleen ma waay)
Nit ñee ma di dofloo nii (baleen ma waay)

Xel mi fa mu dem daa sori (baleen ma waay)
Saxaar gi ci tux yóbbuwu ma (baleen ma waay)
Nit ñee ma di yóbbaale (baleen ma waaay)
(Baleen ma waay)

Trem da Mente

Muito obrigado
Muito obrigado
Nem mesmo muito orgulho cura a dor.
E não deixa ninguém satisfeito
Sidy esfregou o ombro dela.
Apoie-se nisso quando estiver perdendo.

O pensamento de para onde ele foi estava muito distante.
O trem do smoking não me levou
Pessoas que me inspiram!

O espírito lá em cima é elevado.
Eu não entrei no trem de smoking.
Pessoas me deixam louco assim

O pensamento de para onde ele foi estava muito distante.
O trem do smoking não me levou
Alguém me disse para tomar

Estou na casa dos trinta e minha sorte está caindo.
As necessidades cessaram e me permitiram sentar e cair.
Todo mundo diz que o que aconteceu com ele é que ele andou para trás.
Perdi minha voz e fui preterido.
Quando os ricos falam, eles não estão felizes.
Até uma múmia de um milhão de dólares tem voz aqui.
Eu-esses irmãos e a mãe deles.
Eu costumava pensar que eles não me esperariam na hora do almoço.

Agora eles estão me dando (não a mim)
Os gatos estão brincando comigo (os tubarões sou eu)
Eles me deram um nome (homem tubarão)
Chifres de galinha (tubarões, homem)
Já sofri abusos em todos os lugares que estive (sou um tubarão).
Eu me recuso a lutar contra isso (não sou um tubarão)
Eles dizem isso mais para mim (do que eu mesmo)
Me desculpe por tê-los deixado (me desculpe)
Dizem que estou colhendo grama (não sou um tubarão).
O canto inteiro me faz ficar onde não pertenço (qualquer tubarão)
Eles não querem mais que eu voe.
Os pais proíbem seus filhos de me amarem
Até que todos fujam de mim
Agite sua faca e me mate.
E que Deus Rei decida
Você está usando o disfarce do diabo.

O pensamento de para onde ele foi estava muito distante.
O trem do smoking não me levou
Pessoas que me inspiram!

A tristeza que vem com o luto.
Muitos pensamentos e solidão!
Eu posso deixar o escravo louco.

O pensamento de para onde ele foi estava muito distante.
O trem do smoking não me levou
Pessoas que me inspiram!

O bolso interno está em boas condições.
É necessário pagar o aluguel.
Cebola ou dentes de alho.
Se você não atender aos requisitos
Um dia você dirá: Quem te perguntou?

Fracasso (tubarão, eu sou o cara)
Fracasso (tubarão, eu sou o cara)
Saia com pessoas que fazem isso (exceto eu).
Pode ser feito por você mesmo (exceto eu).
Mesmo que o tempo seja difícil de suportar, é preciso ser muçulmano.
Não há divindade além de Alá

O pensamento de para onde ele foi estava muito distante.
O trem do smoking não me levou
Pessoas que me inspiram!

O pensamento de para onde ele foi estava muito distante.
O trem do smoking não me levou (eu sou um tubarão)
As pessoas me deixam louco assim (eu não)

A ideia de para onde ele foi era absurda (que tubarão eu sou).
O trem do smoking não me levou (qualquer tubarão)
Pessoas que me inspiram (seja lá o que eu for)
(Tubarão, cara)