395px

Allamé (feat. Malakey)

Jeeba

Allamé (feat. Malakey)

Hello, ooh ooh wa
Yow chérie yaa ma yaa ma wara wuyu
Aaah, aaah aah aah
Yaw chérie yaa ma wara wuyu
Décroche ton téléphone, ne me laisse pas he
Chérie yaa ma wara wuyu

Alaame alaame alaame téléphona
Alaame alaame alaame téléphona
Alaame alaame alaame téléphona
Chérie alaame téléphonaa

Tooñ nga ma been yoon yow chérie maa la baal
Tooñaat ma ñaari yoon
Même bu ñeent dama lay baal
Li ma denc sama xol
Yàlla sedde na ma ko waaw
Ñëwel fi nga jege ma
Loo bëgg wax ma ko waaw

Yow biik, yow biik si guddi nelawuma
Di la xalaat te ba léegi babe nelawuma
Yow deet, bul defe noonu doyaluma
Ku la naan man dit, ku la raay genum reew sama
Bi nga yekse laa xel yi daal
Ñépp naan kaar machallah!
Namoon naa la chérie boy waawaawaaw
Aaah, aaah aah aah

Alaame alaame alaame téléphona
Alaame alaame alaame téléphona
Alaame alaame alaame téléphona
Chérie alaame téléphonaa

Bébé yo i kànu de bɛnà i jàràbi
Dalen bey Malakey ni kan
Abey nafó kɔfɛ̌ la murani
Sùnɔgɔ la
Abey bali ka cun nekan
Wa ne ɲɔgɔn
Cai jugu sarama
Ki bi ban nela ka kule ko fan fan
I tɛ̀mɛ tó ka gɛ̀rɛ ne la
Kuluci ñaifaila bey to ka pan pan
Baby yo décroche moi
Nebi wele appel teta
I kadi n'gne ni wari ni CFA
Jarabi géléman
Neteni jànfa
N' beni sara n'baguer baga bɛ la
Akadi n' ñe i kakai ne denw ba
Ni tɔgɔ dedo
M'bo di ma
Affection ni couer ni lomba

Oh baby
I ka baby kànu de bɛnà
Jarabi dedoo
Malakey tena i jànfa
Oh baby
I ka baby kànu de bɛnà
Jarabi dedo
Malakey tena i jànfa

Alaame alaame alaame téléphona
Alaame alaame alaame téléphona
Alaame alaame alaame téléphona
Chérie alaame téléphonaa

Allamé (feat. Malakey)

Ei, ooh ooh wa
Oh querido, você é quem eu tenho que ligar.
Aaah, ah ah ah.
Você querido, eu tenho que ligar.
Desligue seu telefone, não me deixe, ele
Eu tenho que te perguntar, querido.

Sinal sinal sinal sinal de telefone
Sinal sinal sinal sinal de telefone
Sinal sinal sinal sinal de telefone
Prezado número de telefone.

Você me ofendeu uma vez e eu te perdôo, minha querida.
Ele me ofendeu mais duas vezes
Meme quatro eu te perdôo.
O que guardo em meu coração
Deus me abençoou sim
Aproxime-se de mim!
Diga-me o que você quer.

Oh cara, cara, eu não dormi ontem à noite.
Pensando em você e ainda não dormindo, querido
Oh não, não, não estou satisfeito.
Quem te chama de eu, quem te mata, é meu país.
Quando você chegou, sua mente explodiu.
Todo mundo bebe cartas machallah!
Senti sua falta, querido garoto, não é?
Aaah, ah ah ah.

Sinal sinal sinal sinal de telefone
Sinal sinal sinal sinal de telefone
Sinal sinal sinal sinal de telefone
Prezado número de telefone.

Baby faz uma canoa de banana.
Dalen como você ainda é jovem
Abey gosta de café Murray
Sùnog la
Abey está aqui
Aqui estão dois
A água é muito suculenta
Quem não dorme é torcedor.
Quando é hora de dormir
Cruze a lima e leve para a panela
Querida, me foda
Profeta wele apple theta
Neste caso viemos para o CFA
A tribo alemã
Neteni traído
Pedi a Sarah um saco de pão.
É claro que as pessoas viviam em
Com o nome dedo
E eu sou
O carinho é uma exigência.

Ah querido
O bebê camelo saiu.
Experimente dedoo
Malakey não trapaceou.
Ah querido
O bebê camelo saiu.
Teste de dedo
Malakey não trapaceou.

Sinal sinal sinal sinal de telefone
Sinal sinal sinal sinal de telefone
Sinal sinal sinal sinal de telefone
Prezado número de telefone.