Dinala
Dina la, dina la
Dina la yobbu fu nga aggulwoon
Dina la denk lu ma sori
Man dina la jox nga teyil ma sama xol
Àdduna ngi gis te noon yaa ngi wax
Jaratul coow ci man la uuhm
Ba nga jàppee ba tay du danga bañ de
Dañu indispensable ci yow ni ndox
Xooloo ndax sama poche am na carte gab
Lijjënti wo sama père dafa capp
Sama self am free rekk molaa ñoor
Defaluñu la litax bañ lay ngooro
Jaaral nga ma soppaleku doon terroriste
Adhérer hezbollah doon extrémiste
Ku la laal ma takk ci kowam muy gis
Ba mel ni gangsta bu amatul jiis
Kon dinaa la dinaa la dey
Dinaa la dinaa la may
Dinaa la jox sama xol
Dinaa la def sama tool
Man dinaa la dinaa la dey
Dinaa la dinaa la may
Dinaa la jox sama xol
Dinaa la def sama tool
Lu mu mëna ma jël
Yaay sama kom-kom
Bët dey gis te xool dey wax
Ñaar yi le woon nañ ma yow yaa tax
Bataay ñu laj ndaxam neewuñu paradise
Alors que jege wuñ sax lu mel ni paradise
Start from the bottom ba tax may gërëm
Xëcc bu dagul may laj ndax dinaa dikkëm
Xëcc ñu nga taf ñu sa bopp door ma biz
Na la feccal ngel ni mbaye ndiaye kaam dikaam
Li nga ma jaral yépp suñ ko toggoon di wax
Waat na ko ci Yàllah babe dinaa fi fenak
Def ko ci sa xol te nga jàpp babe du nax
Suñu tool dafa laaw mu ku boy du lax
Fi nga ma def ak fi nga ma yobbu xam na
Fu ma jule ñan si mawlana
Sumb bi ñu sumb
Agaal ko teemu gaaw
Wax ko ko wax ko ko wax ko
Kon dinaa la dinaa la dey
Dinaa la dinaa la may
Dinaa la jox sama xol
Dinaa la def sama tool
Man dinaa la dinaa la dey
Dinaa la dinaa la may
Dinaa la jox sama xol
Dinaa la def sama tool
Lu mu mëna ma jël
Yaay sama kom-kom
Sometime ñu tongo ku ne dem yonaam
Li ñuy jubbule dokoo xamaam
Lu ci man lu ci man wor na du ci yow
Lu ci yow lu ci yow la àdduna di wër
Suñuy défaut ak sunuy caprices moom nga ànd
Emprisonné te ne dotoo ko xool
Nu ñu mel nu ñuy def nga ni bëgg na
Balaa ñu la wo nga ni waaw dégg na
Kon wax ma fooma def, foo ma def
Baby wax ma fooma def
Fi nga ma def xam na sori na
Ndax mënatu ma
Mënatu ma dundu sans yow
Yow wax ma foo ma def, foo ma def
Baby wax ma foo ma def
Fi nga ma def xam na sori na mënatu ma
Mënatu ma dundu sans yaw
Kon dinaa la dinaa la dey
Dinaa la dinaa la may
Dinaa la jox sama xol
Dinaa la def sama tool
Man dinaa la dinaa la dey
Dinaa la dinaa la may
Dinaa la jox sama xol
Dinaa la def sama tool
Lu mu mëna ma jël
Yaay sama kom-kom
Unhas
Vai, vai
Ele o levará a lugares onde você nunca esteve antes.
Vou manter você longe de mim.
Eu vou te dar meu coração.
O mundo vê e o inimigo fala
Não vale a pena o incômodo para mim, uhm
Até você descobrir, você não pode recusar
Eles são tão indispensáveis para você quanto a água.
Verifiquei se havia um cartão de identificação no bolso.
O trabalho do meu pai acabou.
Meu eu é livre para olhar para mim.
Você não foi feito para odiar os homens.
Por favor, transforme-me em um terrorista.
Aderir ao Hezbollah como extremistas.
Quem me toca e me toca pode ver.
Como um gangsta sem energia!
Então eu vou te dar, eu vou te dar
Eu vou te dar um
Eu vou te dar meu coração
Farei de você minha fazenda.
eu vou te dar
Eu vou te dar um
Eu vou te dar meu coração
Farei de você minha fazenda.
O que ele pode tirar de mim?
Você é minha inspiração!
O olho vê e o olho fala.
Os dois eram porque você era.
As cartas que pediam o nome dela não diziam paraíso.
Embora eles não estejam nem perto do paraíso.
Comece de baixo até o ponto em que sou grato.
Vou perguntar se venho em breve.
Pegue-os, coloque-se neles e comece o meu negócio.
Que você seja abençoado como Mbaye Ndiaye Kaam Dikaam
Tudo o que você vale para mim se cozinhássemos, diria
Ele jurou por Deus, querido, eu não vou mentir.
Mantenha isso em seu coração e espere, querido, não trai
Nossos campos são tão férteis que ninguém consegue ará-los.
Ele sabe onde você me colocou e para onde me levou.
Onde eu fui para Mawlana
A profundidade em que mergulharam
Comece rapidamente
Diga a ele, diga a ele, diga a ele
Então eu vou te dar, eu vou te dar
Eu vou te dar um
Eu vou te dar meu coração
Farei de você minha fazenda.
eu vou te dar
Eu vou te dar um
Eu vou te dar meu coração
Farei de você minha fazenda.
O que ele pode tirar de mim?
Você é minha inspiração!
Às vezes eles estão seguindo seu próprio caminho.
Seu destino é desconhecido.
O que quer que aconteça comigo, o que quer que aconteça comigo, não é seu.
E você é o que gira o mundo.
Suas falhas e caprichos são seus.
Preso e instruído a não olhar para ele novamente.
Como eles são, como agem, você acha que ele ama
Antes de ligarem você disse sim.
Então me diga onde estou, onde estou
Querida, diga-me para onde ir.
Eu sei que está longe.
Porque eu não posso mais
Não consigo mais viver sem você!
Você me diz onde estou, onde estou.
Querida, diga-me para onde ir!
Aqui você me colocou, eu sei que não aguento mais.
Não consigo mais viver sem você!
Então eu vou te dar, eu vou te dar
Eu vou te dar um
Eu vou te dar meu coração
Farei de você minha fazenda.
eu vou te dar
Eu vou te dar um
Eu vou te dar meu coração
Farei de você minha fazenda.
O que ele pode tirar de mim?
Você é minha inspiração!