395px

Número Um

Jeeba

Number One

Yeah!
Yaa tax lépp lu ma songe daan ko
Doleel nga ma fune
Nit ki la nob ba ñépp xam ko
Na la jaaral lune

Man jox naa la lune lune
Man jox naa la lune eeh
Man jox naa la lune lune
Man jox naa la lune eeh

Naa la follow fépp foo dem
Man yaw lay titteru fépp fu ma ne eeh
Man daañ may meree su maay wax ci yow
Ndax mësoo changé mësoo kakatar eeh

Yaay sama number one
Yeah, number one
Jikko bu rafet loolu nga ma wone
Yeah, loolu nga ma wone

Eh duubi duubi, eh daddy daddy
Man maay sa daddy daddy
Eh duubi duubi, eh daddy daddy
Man maay sa daddy daddy

Sama babe kaay
Gis naa sa melokaan
Yaa tax maay dëkke daan
Yow rekk yaa tax ma fier remuer ciel et terre
Ngir lépp lu ma am ma indil la
Woo ma ma ñëw balaa nga tek reer
Xam naa lépp lu baax pur man la
Jox naa la lune eeeh

Yaa tax lépp lu ma songe daan ko
Doleel nga ma fune
Nit ki la nob ba ñépp xam ko
Na la jaaral lune

Man jox naa la lune lune
Man jox naa la lune eeh
Man jox naa la lune lune
Man jox naa la lune eeh

Def la jabar te kenn du ci tek baat
Ñépp d'accord ni danga mérité dote
Ajjo saay mbagg titeru wo danga took
Sama gale kenn ku dul yow du fi tek tànk

Yaay sama number one
Yeah, number one
Jikko bu rafet loolu nga ma wone
Yeah, loolu nga ma wone

Eh duubi duubi, eh daddy daddy
Man maay sa daddy daddy
Eh duubi duubi, eh daddy daddy
Man maay sa daddy daddy

Eeeh
Léegi nak leen mo ci dese
Nga took sama wét te doo dem
Doo jigéen buy tokk ni fees seuh eh

Eh jox naa la lune lune
Jox naa la lune

Yaw ya tax lépp lu ma songe daan ko
Doleel nga ma fune
Nit ki la nob ba ñépp xam ko
Na la jaaral lune

Man jox naa la lune lune
Man jox naa la lune eeh
Jox naa la lune
Man jox naa la lune eeeh!

Número Um

É!
Você é tudo que eu sonho, viu?
Me faz sentir tão bem
A pessoa que você é, todo mundo sabe
Você é a razão da minha luz

Eu te dou a luz, luz
Eu te dou a luz, é
Eu te dou a luz, luz
Eu te dou a luz, é

Eu vou te seguir, tudo que você fizer
Eu só quero te ver, tudo que eu tenho, é
Eu não posso mais ficar sem você
Você não vai mudar, não vai me deixar, é

Ei, meu número um
É, número um
A beleza que você tem, eu vejo
É, eu vejo você

Eh, dia após dia, eh, pai
Eu sou seu pai, pai
Eh, dia após dia, eh, pai
Eu sou seu pai, pai

Meu amor, vem cá
Eu vejo seu olhar
Você é tudo que eu quero
Só você, você é a razão de eu mexer céu e terra
Por tudo que eu tenho, eu te dou
Uou, eu não sei como você faz isso
Eu sei que tudo é bom pra mim
Eu te dou a luz, eeeh

Você é tudo que eu sonho, viu?
Me faz sentir tão bem
A pessoa que você é, todo mundo sabe
Você é a razão da minha luz

Eu te dou a luz, luz
Eu te dou a luz, é
Eu te dou a luz, luz
Eu te dou a luz, é

Você é a única que não se importa com o que falam
Todo mundo concorda que você merece tudo
Apenas siga seu caminho, você vai longe
Ninguém pode te parar, você não vai se deixar levar

Ei, meu número um
É, número um
A beleza que você tem, eu vejo
É, eu vejo você

Eh, dia após dia, eh, pai
Eu sou seu pai, pai
Eh, dia após dia, eh, pai
Eu sou seu pai, pai

Eeeh
Agora, não se esqueça
Você vai seguir meu caminho e não vai parar
Não vai ser uma mulher que desiste, eh

Eh, eu te dou a luz, luz
Te dou a luz

Você é tudo que eu sonho, viu?
Me faz sentir tão bem
A pessoa que você é, todo mundo sabe
Você é a razão da minha luz

Eu te dou a luz, luz
Eu te dou a luz, é
Te dou a luz
Eu te dou a luz, eeeh!

Composição: