Doumala Fowe
Duma la fowe
Duma la, duma la fowe
Duma la, duma la, duma la, duma la fowe
Duma la, duma la, duma la, duma la fowe
Soxna si
Ci man ngay mujje gise love
Nax gén bëggewula ni man
Sam sa daraja ni maam
Manam du xale bi bu dul yaw du mësa doon keneen
Ndax sama nga sa ndaw ni maam
Di génnu farata ni maam
Man àdduna la bëgg wane
Ba ñu xam ni que ni tekk naa la fu kawé kawé
Togal sama wet bul ma mësa
Taggu ndax xam nga ni soo ma soree ma wéet
Dama la gis yek tegé fëlé sama mbonté
Man li ma yittel moy sama mbégté
Beugou ma la disturb
Diegalou soun lay énervé
Non metti naa la li ma la toppe girl
Yàlla xam na
Ni man bëgg naa la
Li tax ñame woo ma
Dama deng jaar-jaar
Sama demb ñaaw na
Njëlbéen du nada
Mouthie gu rafet lay niane Yàlla jox ma la
Duma la fowe
Fi ma la fore da sori
Sa ree ju neex
Mo may facc suma feebare
Duma la fowe
Ndax fi ma la fore da sori
Sa ree ju neex
Momay facc souma feebare
Ak li ma mën gis li ma dégg
Man duma give up
Yeen bi lu mu mën dis lu mu dëgger
Dara duma disturb
Ne ko ci réseau sociaux yi di polluer all the time
Danaka sax doo nekk online
Fuck cheveux naturel enjoy nga life bëgg na
Loo lo waral man yaw lay ñaan
Dama la gis yeg teggi fëlé sama mbonté
Man li ma yitteel mooy sa mbégté
Bëgguma la disturb
Jéggalu su ma lay énervé
Non metti naa la li ma la topé girl
Yàlla xam na
Ni man bëgg naa la
Li tax ñamé woo ma
Dama deung jaar-jaar
Sama demb ñaaw na
Ndieulbén du nada
Mouthie gu rafet lay ñaan Yàlla diokhgn mala
Duma la fowe
Fi ma la fore da sori
Sa ree ju neex
Moo may facc su ma feebaree
Duma la fowe
Ndax fi ma la fore da sori
Sa ree ju neex
Moo may facc su ma feebare
Duma La Fowe
Duma la fowe
Duma la, duma la fowe
Duma la, duma la, duma la, duma la fowe
Duma la, duma la, duma la, duma la fowe
Soxna si
Se eu não te amar, o que vai ser?
Não vale a pena se eu não tiver você
Eu sou seu, não sou só um cara
Não sou só um garoto que não vale nada
Você é minha, não sou só um cara
Você é tudo que eu quero, minha mãe
Eu só quero que você saiba
Que eu sou louco por você, não tem como negar
Cuida de mim, não me deixe de lado
Porque você sabe que se eu te perder, eu vou ficar mal
Eu vejo você e isso me deixa feliz
Eu só quero que você saiba que você é meu
Não quero te incomodar
Mas eu fico nervoso
Não posso deixar você ir, garota
Deus sabe
Que eu só quero você
Por que eu não consigo te esquecer?
Eu estou gritando, gritando
Meu coração está tão baixo
Nada é igual
A boca linda que você tem, Deus me deu você
Duma la fowe
Aqui é onde eu quero estar
Seu sorriso é doce
Como eu posso fazer você se sentir bem?
Duma la fowe
Aqui é onde eu quero estar
Seu sorriso é doce
Como eu posso fazer você se sentir bem?
E o que eu vejo, eu não escuto
Eu não vou desistir
Você é tudo que eu quero, tudo que eu preciso
Nada vai me incomodar
Nas redes sociais, tudo poluído o tempo todo
Mas não precisa estar online
Foda-se o cabelo natural, aproveite a vida, eu quero
O que você quer, eu vou te dar
Eu vejo você e isso me deixa feliz
Eu só quero que você saiba que você é meu
Não quero te incomodar
Mas eu fico nervoso
Não posso deixar você ir, garota
Deus sabe
Que eu só quero você
Por que eu não consigo te esquecer?
Eu estou gritando, gritando
Meu coração está tão baixo
Nada é igual
A boca linda que você tem, Deus me deu você
Duma la fowe
Aqui é onde eu quero estar
Seu sorriso é doce
Como eu posso fazer você se sentir bem?
Duma la fowe
Aqui é onde eu quero estar
Seu sorriso é doce
Como eu posso fazer você se sentir bem?