Confuse (feat. Wally B. Seck & Amadeus)
[Mia Guissé]
Yaay booy wuyu ma, dama lay laaj (yeah!)
Yaay booy yédd ma, dama lay laaj (yeah!)
Bëgguma lu baax rëcc ma, dama lay laaj (yeah!)
Bëgguma rëccu tam, dama lay laaj
Xam naa li muy laaj
(Li muy laaj, li muy laaj?)
Ñoom ñaar ku ne mungeek li ñuy laaj
(Li muy laaje, waawaaw)
Damay bëgg a jaaxle
Ndax awma choix ci ñaar ñu doy war
[Wally Seck]
Bëgg nga mais yaa ngi xel ñaar
Bëggoo ku xar sa xol bi ñaar, baby
Réy-na ñi fi jot a jar
Ñoo fowe sa xol ba nga foog ni ñépp a soxor
[Amadeus]
God lu mu bind daje def ñaar
Te yaw yaay sama genn-wàll man
Asaman si ni mu yaatoo
Naj bi li muy tàng
Yaay keppaar giy nëb naj bee
[Mia Guissé]
Damay bëgg a jaaxle
Awma choix bébé, xam naa li muy laaje
[Amadeus]
Lingeer nga bul jaaxle
Mbégte dunya yi rekk laa la yénne (hey)
[Mia Guissé]
Damay bëgg a jaaxle
Awma choix bébé, xam naa li muy laaje
[Amadeus]
Yaw lingeer nga bul jaaxle
Mbégte dunya yi rekk laa la yénne
Su ma gisee nga naan danga ma nob
Te nday ji sex du am ci jamaale
Mel ni asaman si ni mu yaatoo
Ak biddéew yi ni ñu taaroo
Neex na ma, waaye jaaxle
Ndax xamuma ki may tànn
[Wally Seck]
Lingeer may Latyr Diop Déguéne Mbaye (anh!)
Ballago Khaliloulay (wuy!)
Njaabot ga lay wutal yaay
Te kër ga yaa fa doy lingeer way (ayah!)
Ma di buur géwel, xuss ndama lay bégal
Soo bëggee ma lay wayal, col nder ak tama way
Lingeer kaay, soo bañee ma wet kaay
Kaay, yaay sama wéeruwaay
[Mia Guissé]
Damay bëgg a jaaxle
Awma choix bébé, xam naa li muy laaje
[Amadeus]
Lingeer nga bul jaaxle
Mbégte dunya yi rekk laa la yénne (hey)
[Mia Guissé]
Damay bëgg a jaaxle
Awma choix bébé, xam naa li muy laaje
[Wally]
Yaw lingeer nga bul jaaxle
Mbégte dunya yi rekk laa la yénne
Neex na ma, waaye jaaxle
Ndax xamuma ki may tànn
No-no-no mon bébé
Ne t’en vas pas, waaw
Neex na ma, waaye jaaxle
Ndax xamuma ki may tànn
Confuso (feat. Wally B. Seck & Amadeus)
[Mia Guissé]
Ei, garoto, você me faz querer (é!)
Ei, garoto, você me faz querer (é!)
Não tem nada que me faça parar, você me faz querer (é!)
Não tem como parar, você me faz querer
Eu sei o que você quer
(O que você quer, o que você quer?)
São só dois que não entendem o que a gente quer
(O que você quer, uhuu)
Eu só quero me divertir
Porque não tenho escolha, só quero o que é bom
[Wally Seck]
Você quer, mas você tá pensando em dois
Querendo alguém que entenda seu coração, baby
Vem cá, deixa eu te mostrar
Eles vão saber que você tá com a gente, que todo mundo tá junto
[Amadeus]
Deus, o que eu faço pra te ter
E você, ei, é meu único caminho
Como se tudo estivesse certo
A noite é nossa, vamos aproveitar
Ei, garota, vem comigo, vamos dançar
[Mia Guissé]
Eu só quero me divertir
Não tenho escolha, eu sei o que você quer
[Amadeus]
Ei, não me faça parar
A vida é só isso, vamos aproveitar (ei)
[Mia Guissé]
Eu só quero me divertir
Não tenho escolha, eu sei o que você quer
[Amadeus]
Ei, não me faça parar
A vida é só isso, vamos aproveitar
Se eu te visse, você ia me deixar louco
E a noite não vai acabar em solidão
Como se tudo estivesse certo
Com as estrelas brilhando pra nós
Eu gosto de você, mas não me faça parar
Porque não sei quem eu sou
[Wally Seck]
Ei, eu sou Latyr Diop, Déguéne Mbaye (ah!)
E Khaliloulay (uê!)
A gente vai fazer você dançar, garota
E a casa vai ficar cheia, (ayah!)
Eu sou o rei da festa, não esquece de mim
Se você me quer, me chama, não fica de bobeira
Se você não me quer, então me deixa em paz
Vem, ei, minha rainha
[Mia Guissé]
Eu só quero me divertir
Não tenho escolha, eu sei o que você quer
[Amadeus]
Ei, não me faça parar
A vida é só isso, vamos aproveitar (ei)
[Mia Guissé]
Eu só quero me divertir
Não tenho escolha, eu sei o que você quer
[Wally]
Ei, não me faça parar
A vida é só isso, vamos aproveitar
Eu gosto de você, mas não me faça parar
Porque não sei quem eu sou
Não, não, não, meu bebê
Não vai embora, uhu
Eu gosto de você, mas não me faça parar
Porque não sei quem eu sou