Tradução gerada automaticamente

Senegal
OMG
Senegal
Senegal
Senegal é nossoSenegaal ñoo ko moom
Todo mundo aqui é irmãoKenn mënu ko xar ñaar
Sofrendo, comendo aquiXiif, lekk ñàkku fi
Mar, falando aquiMar, naan ñàkku fi
A vida é boa, meu paísGudde am fo fanaan sama rééw
Se a gente não se unir, não vamos avançarBu ñu nangu kenn duggu suñu diggënte
A mesma força que temos, vamos mostrarSame diam ji fi ñoom mame bàyyi
Sabemos de tudo, queremos tudoXamuñu leneen, bëgguñu leneen
He he he!He he he!
Gueye Ndioro, eu te chamei (gueye Ndioro, eu te chamei)Gueye Ndioro wëy naa la (gueye Ndioro way naa la)
Faye Birame, eu te chamei (te chamei)Faye Birame wëy naa la (way naa la)
Diobeu Dioubeu, eu te chamei (diobeu dioubeu, eu te chamei, eu te chamei)Diobeu Dioubeu wëy naa la (diobeu dioubeu wëy naa la wëy naa la wëy naa la)
Tourè Mandi, eu te chamei (hehee)Tourè Mandi wëy naa la (hehee)
Thiam babel demba thiam, eu te chameiThiam babel demba thiam way naa la
Gomissa gania, eu te chamei (sané balama)Gomissa gania way naa la (sané balama)
Ndiaye Diata Ndiaye, eu te chameiNdiaye Diata Ndiaye wayaan naa la
Dioufa niokhobay, eu te chamei (man djonkéléfa)Dioufa niokhobay wëy naa la (man djonkéléfa)
As tradições precisam ser respeitadas, meu país precisaSant yi war galgui rééw ma ngi
As tradições precisam ser respeitadas, meu país precisaSant yi war galgui rééw ma ngi
Diom foulak fàydaDiom foulak fàyda
Fonk diné tax xol yé ngi naatFonk diné tax xol yé ngi naat
Dieuf ju baax de diogufiDieuf ju baax de diogufi
Sutura lañuy ndamoSutura lañuy ndamo
Oh Senegal, meu paísHan Senegaal Ndiaye sama rééw
Walo walo, aqui é nossoWalo walo si réw mi
Sine Saloum, aqui é nossoSine Saloum si réw mi
Casamance BoundouCasamance Boundou
Cadior e Baol Fouta ToroCadior ak Baol Fouta Toro
Jolof SenegalJolof Senegaal
Dieng Salla, eu te chamei (samb maharam, eu te chamei)Dieng Salla waynala (samb maharam waynala)
Diagne Naar, eu te chamei (diallo diery, eu te chamei)Diagne Naar waynala (diallo diery waynala)
Sow Poulo, eu te chamei (ba poulo, eu te chamei Yagg masseuy)Sow Poulo waynala (ba poulo waynala Yagg masseuy)
Sall Ngari, eu te chamei (cissé ngari Ngom séni)Sall Ngari waynala (cissé ngari Ngom séni)
Ndoye Mali Maram Ndoye, eu te chamei (wade farawade ndiack)Ndoye Mali Maram Ndoye waynala (wade farawade ndiack)
Mendy Coto, eu te chamei (pouye beukeury)Mendy Coto waynala (pouye beukeury)
Fall Ndiaga yaram, eu te chamei (eu te chamei Camara yilé)Fall Ndiaga yaram waynala (waynala Camara yilé)
Dieye Massamba, eu te chamei (guissé Maabo)Dieye Massamba waynala (guissé Maabo)
Mbacké Balla AissaMbacké Balla Aissa
Sy SawandéSy Sawandé
Niass Coumba AbdallahNiass Coumba Abdallah
Laye MakhtarLaye Makhtar
Kounta Sidy, eu te chamei!Kounta Sidy way naa leen!
As tradições precisam ser respeitadas, meu país (lo ndam ciré)Sante yi war Galgui reew mangui (lo ndam ciré)
As tradições precisam ser respeitadas, meu país (youm sega Mbaye mbassou Diene ndiogou)Sante yi war Galgui reew mangui (youm sega Mbaye mbassou Diene ndiogou)
As tradições precisam ser respeitadas, meu país (thiaw séni Mbengue mbor)Sante yi war Galgui reew mangui (thiaw séni Mbengue mbor)
As tradições precisam ser respeitadas, meu país (ndour wally mbergane Niang mbaallo)Sante yi war Galgui reew mangui (ndour wally mbergane Niang mbaallo)
As tradições precisam ser respeitadas, meu país (sene thiali Sylla moctar)Sante yi war Galgui reew mangui (sene thiali Sylla moctar)
As tradições precisam ser respeitadas, meu país (seck sa guanar)Sante yi war Galgui reew mangui (seck sa guanar)
As tradições precisam ser respeitadas, meu país (sarra moundo Ly bousso)Sante yi war Galgui reew mangui (sarra moundo Ly bousso)
As tradições precisam ser respeitadas, meu paísSante yi war Galgui reew mangui
As tradições precisam ser respeitadas, meu paísSante yi war Galgui reew mangui



Comentários
Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra
Faça parte dessa comunidade
Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de OMG e vá além da letra da música.
Conheça o Letras AcademyConfira nosso guia de uso para deixar comentários.
Enviar para a central de dúvidas?
Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.
Fixe este conteúdo com a aula: