395px

Xaarit (feat. Xiirsa)

Seydina Ndiaye

Xaarit (feat. Xiirsa)

Sama doomu ndey nga
Doomu ndey
Sama doomu ndey nga
Doomu ndey nga

Sama doomu ndey nga
Lu la metti, metti ma
Sama doomu ndey nga
Lu la naqari, naqari ma
Yaw xarit ni la ni la yaw
Yaw xarit ni la
Yaw xarit ni la ni la yaw
Yaw xarit ni la

Ndekke xaritoo dina gëna doomu yaay
Bauye oye ye yo
Ndekke doomu ndey, na déggu ci yaw
Te xarit dafay mat doomu ndey
Ki ñëw di wax, bul déggaati lu ñaaw ci man gëm ko
Te li mooy tax dungeen xulóo

Sama doomu ndey nga
Lu la metti, metti ma
Sama doomu ndey nga
Lu la naqari, naqari ma
Yaw xarit ni la ni la yaw
Yaw xarit ni la
Yaw xarit ni la ni la yaw
Yaw xarit ni la

Doom ndey foo pikkiroo ma naan fay doom
Bëgg naa la tudde sama doom
Ànd bi wekku ñu ko ci kom-kom
Sa jikko tax na dañuy lonko
Wo ho woye
Démb tax ñu naan tay, wo ho woye!
Ni nga ma suturalee
Doo ma jebane Yàlla la lay bàyyeek
Rasul looy

Sama doomu ndey nga
Lu la metti, metti ma
Sama doomu ndey nga
Lu la naqari, naqari ma
Yaw xarit ni la ni la yaw
Yaw xarit ni la
Yaw xarit ni la ni la yaw
Yaw xarit ni la

Sama doomu ndey nga
Doomu ndey
Sama doomu ndey nga
Doomu ndey nga

Xaarit (feat. Xiirsa)

Meu filho, você
Filho, você
Meu filho, você
Filho, você

Meu filho, você
O que você quer, quer de mim
Meu filho, você
O que você deseja, deseja de mim
Ei, é você que eu quero, que eu quero, ei
Ei, é você que eu quero
Ei, é você que eu quero, que eu quero, ei
Ei, é você que eu quero

A verdade é que você é o filho da mãe
Bauye oye ye yo
A verdade é que você é meu filho, eu escuto você
E o que eu quero é que você seja meu filho
Quem vem falar, não se esqueça do que é importante pra mim
E é isso que faz você se sentir bem

Meu filho, você
O que você quer, quer de mim
Meu filho, você
O que você deseja, deseja de mim
Ei, é você que eu quero, que eu quero, ei
Ei, é você que eu quero
Ei, é você que eu quero, que eu quero, ei
Ei, é você que eu quero

Filho, você me faz querer te chamar de meu
Eu quero que você seja meu filho
A conexão é forte, eles estão juntos
Seu jeito faz com que eles queiram te seguir
Wo ho woye
Agora eles querem te chamar, wo ho woye!
Se você me deixar
Eu não vou te deixar, Deus é quem vai me ajudar
Rasul é quem vai

Meu filho, você
O que você quer, quer de mim
Meu filho, você
O que você deseja, deseja de mim
Ei, é você que eu quero, que eu quero, ei
Ei, é você que eu quero
Ei, é você que eu quero, que eu quero, ei
Ei, é você que eu quero

Meu filho, você
Filho, você
Meu filho, você
Filho, você