395px

Sem estresse

Viviane Chidid

No Stress

Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Suñu xol di fees ñoom ñu juk def fés

Non, non, duma nangu nga may teg stress
Duma nangu nga may teg stress
Ma bañ duma ko nangu no stress
Sama xol di fees yaw nga juk def fés

Ma ni dimbali ma wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara
Ma ni dimbali ma wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara

Danga fàtte ni awma dix ans
Lu tax nga jël ma bëgg ma def sa fowukaay
Yombalal naa la sa visa
Wow yeah yeah, demal fu la neex way!

Bëgg langak ki
Bëgg langak ke
Bëgg langak samay xarit ma ni night and day
Dégg na ñu ne feebar la
Wow yeah yeah, defal lu la neex way!

Non non duma nangu nga may teg stress
Duma nangu fils nga may teg stress
Ma bañ duma ko nangu no stress
Sama xol di fees yaw nga juk def fés

Ma ni dimbali ma wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara
Ma ni dimbali ma wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara

Góor gu la teg deal lundi ba dimanche nobu la
Ku ma bëgg a tardel bëgg ma fowe ma romb la
Góor gu la teg deal lundi ba dimanche nobu la
Ku ma bëgg a tardek man ma romb la

Li safatuma
Sama mettitu muñ jeex na
Li yëngëluma
Ndax te man ñakkuma fayda
Li safatuma
Tegg ci temps def ba mu baax jot na
Te yaw mi xam nga
Soo ma nobul sa moroom nob ma!

Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Suñu xol di fees ñoom ñu juk def fés

Non, non, duma nangu nga may teg stress
Duma nangu nga may teg stress
Ma bañ duma ko nangu no stress
Sama xol di fees yaw nga juk def fés

Ma ni dimbali ma wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara
Ma ni dimbali ma wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara

Góor goula teg deal lundi ba dimanche nobu la
Ku ma bëgg a tardeel bëgg ma fowe ma romb la
Góor gu la teg deal lundi ba dimanche nobu la
Ku ma bëgg a tardèk mane ma rombe la

Sem estresse

Não, não, bu ñu nangu ñu ñuy teg estresse
Não, não, bu ñu nangu ñu ñuy teg estresse
Não, não, bu ñu nangu ñu ñuy teg estresse
Suñu xol di fee ñoom ñu juk def fés

Não, não, duma nangu nga pode causar estresse
Duma nangu nga pode causar estresse
Ma bañ duma ko nangu sem estresse
Sama xol di fee yaw nga juk def fés

Ma ni dimbali ma cera ji bari na
Homem rekk ci xale nammuma dara
Ma ni dimbali ma cera ji bari na
Homem rekk ci xale nammuma dara

Danga fàtte ni awma dix ans
Lu tax nga jël ma begg ma def sa fowukaay
Yombalal naa la sa visto
Uau, sim, sim, demal fu la neex way!

Bëgg langak ki
Bëgg langak ke
Bëgg langak samay xarit ma ni noite e dia
Dégg na ñu ne feebar la
Uau, sim, sim, defal lu la neex way!

Non non duma nangu nga pode teg estresse
Duma nangu fils nga pode teg estresse
Ma bañ duma ko nangu sem estresse
Sama xol di fee yaw nga juk def fés

Ma ni dimbali ma cera ji bari na
Homem rekk ci xale nammuma dara
Ma ni dimbali ma cera ji bari na
Homem rekk ci xale nammuma dara

Góor gu la teg deal lundi ba dimanche nobu la
Ku ma begg a tardel begg ma fowe ma romb la
Góor gu la teg deal lundi ba dimanche nobu la
Ku ma begg a tardek man ma romb la

Li safatuma
Sama mettitu muñ jeex na
Li Yëngëluma
Ndax te man ñakkuma fayda
Li safatuma
Tegg ci temps def ba mu baax jot na
Te yaw mi xam nga
Soo ma nobul sa moroom nob ma!

Não, não, bu ñu nangu ñu ñuy teg estresse
Não, não, bu ñu nangu ñu ñuy teg estresse
Não, não, bu ñu nangu ñu ñuy teg estresse
Suñu xol di fee ñoom ñu juk def fés

Não, não, duma nangu nga pode causar estresse
Duma nangu nga pode causar estresse
Ma bañ duma ko nangu sem estresse
Sama xol di fee yaw nga juk def fés

Ma ni dimbali ma cera ji bari na
Homem rekk ci xale nammuma dara
Ma ni dimbali ma cera ji bari na
Homem rekk ci xale nammuma dara

Góor goula teg deal lundi ba dimanche nobu la
Ku ma begg a tardeel begg ma fowe ma romb la
Góor gu la teg deal lundi ba dimanche nobu la
Ku ma begg a tardèk mane ma rombe la