Tradução gerada automaticamente

exibições de letras 10

Thieuguine

Wally B. Seck

Letra

Thieuguine

Thieuguine

Mane xam nani kep kou kofi meusseuMane xam nani kep kou kofi meusseu
Beguentel malako gueneulBeguentel malako gueneul
Ba soumala guissé damay rétaneBa soumala guissé damay rétane
Mane geum nani doumala meuseu trompe ben yoonMane geum nani doumala meuseu trompe ben yoon
Ndax yamaleen gueneulNdax yamaleen gueneul
Ba soumala guissé damay rétaneBa soumala guissé damay rétane
Mas nak ma wakhla limay dounde soumala seenéMais nak ma wakhla limay dounde soumala seené
Nguay wakh ak kénén dafmay bouleverséNguay wakh ak kénén dafmay bouleversé

Eu estarei onde você me deixarJe serais là où tu me laisseras
Não me culpe, o que eu farei sem vocêNe m’en veut pas, que je ferais sans toi
É só uma ilusãoN’est qu’une illusion
Nenhuma mentira, que me levará só à ilusãoAucun mensonge, qui me mènera qu’à illusion
Nenhuma mentira me afasta de vocêAucun mensonge ne m’éloigne de toi

Kholal sounou diguantei nitteKholal sounou diguantei nitte
Gnie sakh dan niou nawGnie sakh dan niou naw
Kholal bougniou ande nine niouy xoleeKholal bougniou ande nine niouy xolee
Begouloma nguirr alal mo waral ma taneu leBegouloma nguirr alal mo waral ma taneu le
Diaral nguama tago ak nieupDiaral nguama tago ak nieup
Nguir sa dieum djiNguir sa dieum dji
Huuum hummHuuum humm
Ndaw si lé diamono dji daNdaw si lé diamono dji da
Ngay galakh ndiko lamigneNgay galakh ndiko lamigne
Sucaré la xél Khorame la beutSucaré la xél Khorame la beut
Té dougne la wakh deug li dou YoonTé dougne la wakh deug li dou Yoon
Não, não, não, bouniou wétté ba kén rabouniouNon Non Non boulen déglou nawlo woumaleen
Mame Coumba Salymata mba wax ngaMame Coumba Salymata mba wax nga
Adama Aziza Almamy Abdalah PapisAdama Aziza Almamy Abdalah Papis
Kou beug sa waaay way wi yay boromeKou beug sa waaay way wi yay borome

Beug nala beug ngama ba kén meunouniou féwaléBeug nala beug ngama ba kén meunouniou féwalé
Nop nala nop ngama ba kén meunouniou féwaléNop nala nop ngama ba kén meunouniou féwalé
Não, não, não, bouniou wétté ba kén rabouniouNon non non bouniou wétté ba kén rabouniou
Malay féthial dila lébeul dila féthial bilayMalay féthial dila lébeul dila féthial bilay
Thieuguine thieuguineThieuguine thieuguine
Set na ba set yamay motali di fékheul sama xolSet na ba set yamay motali di fékheul sama xol
Yamay defeul mane woh woh wohYamay defeul mane woh woh woh
Ma melni Baba Chérie YandeMa melni Baba Chérie Yande
Ma melni Pape Diop Chérie Youssou GayeMa melni Pape Diop Chérie Youssou Gaye
Laylaylaaa woh ho! Da ngen diLaylaylaaa woh ho! Da ngen di
Féthi moulay thieuguine thieuguineFéthi moulay thieuguine thieuguine
Ma melni Papis Chérie NgalaMa melni Papis Chérie Ngala
Ma melni Momy Chérie DanyMa melni Momy Chérie Dany
Boubacar chérie Diarra dégeuna ya nguiBoubacar chérie Diarra dégeuna ya ngui
Féthi moulay thieuguine thieuguineFéthi moulay thieuguine thieuguine
Ma melni Diène Dieng chérieMa melni Diène Dieng chérie
Awa bayou Mounas bayouAwa bayou Mounas bayou
Ndiogou da ngey féthi moulay thieuguineNdiogou da ngey féthi moulay thieuguine
ThieuguineThieuguine


Comentários

Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra

0 / 500

Faça parte  dessa comunidade 

Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de Wally B. Seck e vá além da letra da música.

Conheça o Letras Academy

Enviar para a central de dúvidas?

Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.

Fixe este conteúdo com a aula:

0 / 500

Opções de seleção