395px

Keur Gui

ZBest Family

Keur Gui

[Dane]
Sooy toogati duggal ba sa biir nekk
Xeet gi sonal naa waa-kër gi, waay

[Fatel]
Eh bul ma tooñ duma sa moroom waay
Kër gi dangay fay man it damay fay

[Dane]
Yeen lu neex way def ngeen bëgg dunde ci kër gi
Non non, xooleen ci dëkkaando yi

[Fatel]
Kon góor dangay màndu régler ñu jox la cër noppil
Lijjantil sa nekk bee

[Waly dieng]
Eh samba ndiaye
Boo duggaate ci duus bi de si def ndox waay

[Fatel & dane]
Ha ha ha ha!
- yor pan, di lijjanti siwo jaambur
Waxal ci le waay!
- he, dimbali ma!

[Dane]
Yaw yaa ma yàpp waay
Boo ma waxaate lu ma deful dinaa la duma

[Waly dieng]
Samba ñëwal, yaw laay xaar

[Dane]
Eh, man duma sa moroom de!

[Awa thiès]
Ñoo bokk ndey book benn baay
Loolu tax ñu tokk fi tay
Booloo war na ñoo kër gi doon benn
Kon sama waay teeñoo boolo

[Momo]
Waa-kër gi te ñoo booloo
Waa-kër gi te ñoo booloo
Waa-kër gi te ñoo booloo
Waa-kër gi te ñoo booloo

(Discussion)

[Mya blacky]
He lamine diop waññil sa radio bi
Kenn mënul nelaw kër gi yeen a lakkale, waaw

[Pape bilal]
Su ma neexee maa tay léegi
Yaw yaa sof mel ni yaay fay sama nekk waaw

[Mya blacky]
Yaa ma gën a sof tànkal guddi tankal bëccëg
Eh lamine diop ameel nga ak dëkkandoo yi

[Pape bilal]
Jigéen du ma yuxu, jigéen duma fontoo
Marème puusal bala ma lay songu

[Waly dieng]
Soo ko dooree eeh waaw
Soo koy dóoree maak yaw la na la doon fii

(Discussion)

[Awa thiès]
Ñoo bokk ndey book benn baay
Loolu tax ñu tokk fi tay
Booloo war na ñoo kër gi doon benn
Kon sama waay teeñoo boolo

[Momo]
Waa-kër gi te ñoo booloo
Waa-kër gi te ñoo booloo
Waa-kër gi te ñoo booloo
Waa-kër gi te ñoo booloo

[Iblow]
Prési bàyyil xel askan bi
Bàyyil xel économique bi
Confinement da wara jeex
Prési jaar nga fu metti xam nga luy pas de boulot
Chaque jour xuloonuñu suñu dundu safatul neex

[Azou]
Hey yaw moomu lasa dundu safatul neex
Sonal nga ñu waay!
Rap guddi rap bëccëg
Dem nga sax ba kër ñépp amee rap di xuloo

[Iblow]
Hey duma wax ak fecckat nax awma jotam

[Azou]
Hey fecc ma gënal waxtu guddeek bëccëg
Dëkke wax dëkke ray dëkke tekk xel ba xiif

[Awa thiès]
Hey bàyyil ma fecckat bi te nga dem jëndal ma fël-fale ci boutique bi

[Iblow]
Kan man yaw yaa yabbate yaw
Man may real rappeur nga may yónni ay saf-safal
He, xoolal soo bëggee sa fekk danga koy danga koy wëri

[Azou]
He he heeey
Moo safal, yaa koy safal
He safal, yaa koy safal
Hey, ba kër gi fer!

[Awa thiès]
Ñoo bokk ndey book benn baay
Loolu tax ñu tokk fi tay
Booloo war na ñoo kër gi doon benn
Kon sama waay teeñoo boolo

[Momo]
Waa-kër gi te ñoo booloo
Waa-kër gi te ñoo booloo
Waa-kër gi te ñoo booloo
Waa-kër gi te ñoo booloo

Keur Gui

[Dane]
Sou eu soubesse que você estava aqui
A galera já sabia que a casa ia bombar

[Fatel]
Ei, não me deixe de lado, não sou seu irmão não
A casa tá cheia, mas eu tô na minha

[Dane]
O que vocês querem, eu só quero viver na casa
Não, não, se juntem na quebrada

[Fatel]
Então, o cara tá tentando arrumar, eles te dão a mão
Agradeça por estar aqui

[Waly dieng]
Ei, samba ndiaye
Se você não se cuidar, vai acabar se afogando

[Fatel & dane]
Ha ha ha ha!
- segura a onda, faz a conexão
Fala pra eles!
- ei, me ajuda!

[Dane]
Ei, você é tudo pra mim
Se eu te contar o que eu fiz, não vou te deixar

[Waly dieng]
Samba, não esquece de mim

[Dane]
Ei, eu não sou seu irmão!

[Awa thiès]
Eles se juntam, mãe e pai
Isso faz com que eles fiquem aqui
Deveriam ter uma casa só
Então, meu amor, não se esqueça

[Momo]
A casa tá cheia e eles se juntam
A casa tá cheia e eles se juntam
A casa tá cheia e eles se juntam
A casa tá cheia e eles se juntam

(Discussão)

[Mya blacky]
Ei, lamine diop, liga o rádio
Ninguém pode ficar sem a casa, vocês têm que se cuidar, sim

[Pape bilal]
Se eu não me importar, vou ficar aqui
Ei, você é como minha mãe, cuida de mim, sim

[Mya blacky]
Você tem que cuidar da sua saúde, não esquece
Ei, lamine diop, você tem que estar com a galera

[Pape bilal]
Mulher não pode me deixar, mulher não pode me deixar
Se eu não me cuidar, vou acabar na pior

[Waly dieng]
Se você não se cuidar, ei, sim
Se você não se cuidar, você vai ficar aqui

(Discussão)

[Awa thiès]
Eles se juntam, mãe e pai
Isso faz com que eles fiquem aqui
Deveriam ter uma casa só
Então, meu amor, não se esqueça

[Momo]
A casa tá cheia e eles se juntam
A casa tá cheia e eles se juntam
A casa tá cheia e eles se juntam
A casa tá cheia e eles se juntam

[Iblow]
Preste atenção, a mente da galera
A mente econômica
O confinamento vai acabar
Preste atenção, se você não souber, não vai ter trabalho
Todo dia, a gente luta pra viver

[Azou]
Ei, você tem que viver, a vida é difícil
Eles já sabem!
Rap, a vida é dura
Você só vai ver quando a casa estiver cheia

[Iblow]
Ei, não vou falar e deixar de lado, não vou deixar

[Azou]
Ei, me ajuda a ter tempo, a vida é dura
Fala, fala, faz a mente funcionar

[Awa thiès]
Ei, me ajuda a sair e me leva pra loja

[Iblow]
Como você, você é tudo pra mim
Eu sou um rapper de verdade, vou fazer acontecer
Ei, veja como você quer, você vai conseguir

[Azou]
Ei, ei, ei
É tudo certo, você vai conseguir
Ei, é tudo certo, você vai conseguir
Ei, a casa tá cheia!

[Awa thiès]
Eles se juntam, mãe e pai
Isso faz com que eles fiquem aqui
Deveriam ter uma casa só
Então, meu amor, não se esqueça

[Momo]
A casa tá cheia e eles se juntam
A casa tá cheia e eles se juntam
A casa tá cheia e eles se juntam
A casa tá cheia e eles se juntam