Tradução gerada automaticamente

Sama Président
Awa Thiès
Prezado Presidente
Sama Président
Todo mundo sabe quem eles amamKu ne xam nga ki la nob
Aquele que te ama sem trairKi la bëgg te du la nax
Que Deus te abençoe e te guieMay la jàmm te di la wan
O que é o amor, cara, você sabe?Luy mbëggeel waay, xam nga ko
Você preenche meu coração completamente!Duy nga sama xol mu fees
O amor nunca acaba hoje!Bëgg tay du wees
Você me iluminou com diversãoTaal nga ma fu ne
Agora estamos aguardando SapeurLéegi Sapeur lañuy xaar
Você roubou meu coração quandoSàcc nga sama xol bi
Onde a integração for necessáriaFàww boole am ci yoon
Golpe de estado, meu amorCoup d’Etat sama mbëggeel
Agora eles estão esperando o ExércitoLéegi Armée lañuy xaar
Dok com você nas minas rebeldesDok ak yaw ci mines u rebelles yi
Cruzar as pernas não é uma boa ideiaJéggi tànk moom du xel
Você tocou meu coraçãoDugal nga lu ne sama xol
Agora estou aguardando a liberação da alfândegaLéegi Douane lañuy xaar
Você é o presidentePrésident a ngee
Eis o presidentePrésident a ngii
Onde o PresidenteFoo nekkee Président
Eu estava lá como Primeira-DamaMa doon fa Première Dame
Onde você estava, Macky, eu era sua MarèmeFoo doonee Macky, ma doon sa Marème
Onde você é o corpo, eu sou o coraçãoFoo doonee jëmm, ma doon sa xol
Onde estava Sadio Mané?Foo doonee Sadio Mané
Eu seria seu balão, e você me colocaria dentro deleMa doon sa ballon, nga di ma dugal
Onde eu era sua picareta, eu era sua páFoo doonee pique, ma doon sa pelle
Eu sempre pensava: eu era a sua mente quandoFoo doonee xalaat, ma doon sa xel bi
Atrasos, seu boboDi la tardeel ba nga dof
Que estupidez dizer "sim"Dof di naan “waawaaw”
Nossa!Ey waay!
Deus!Ndeysaan!
Nossa!Ey waay!
Deus!Ndeysaan!
Nem ouro nem pérolasAwuma wurus, awuma ngalam
Mas, querida, estou apaixonadoWaaye chéri am naa mbëggeel
Nada aconteceu, morte, fique tranquilaDara xewul dee ko woyofal
Você me deve uma coisaJaral nga ma lu ne
Seu doce coração me ensinaSa joli coeur ràngati ma
Até eu voltarBa ma dellu gone
Se você me ouvir, eu cantarei para vocêBu ngeen ma dégloo ma wayal leen
Eu canto para aquele que aceita meu coraçãoKi nangu sama xol bi laay wayal
Ei! Você fez uma turnê e ganhou por mimHey! Tourné nga daj nga ci man
Não, não é perdão, não é para mimDéédéét du yaafuus nekkul ci man
Menos conversa, mais ação!Wax ji du bari, jëf ji day bari
Uma personalidade desafiadora não faz parte de mimJikko bu défaillant nekkul ci man
Você é o presidentePrésident a ngee
Eis o presidentePrésident a ngii
Onde o PresidenteFoo nekkee Président
Eu estava lá como Primeira-DamaMa doon fa Première Dame
Onde você estava, Macky, eu era sua MarèmeFoo doonee Macky, ma doon sa Marème
Onde você é o corpo, eu sou o coraçãoFoo doonee jëmm, ma doon sa xol
Onde estava Sadio Mané?Foo doonee Sadio Mané
Eu seria seu balão, e você me colocaria dentro deleMa doon sa ballon, nga di ma dugal
Onde eu era sua picareta, eu era sua páFoo doonee pique, ma doon sa pelle
Eu sempre pensava: eu era a sua mente quandoFoo doonee xalaat, ma doon sa xel bi
Atrasos, seu boboDi la tardeel ba nga dof
Que estupidez dizer "sim"Dof di naan “waawaaw”
Nossa!Ey waay!
Deus!Ndeysaan!
Nossa!Ey waay!
Deus!Ndeysaan!
Ah! Lee!Aah! Lee!
Nossa!Ey waay!
Seja corajoso agora!Jàmbaari léegi léegi
Bravos cavaleiros!Jóoni jóoni jàmbaar
Deus!Ndeysaan!
Biram DiopBiram Diop
Nossa!Ey waay!
Estou lhe enviando minha querida KyaChéri Kya dama lay joobeel
Deus!Ndeysaan!



Comentários
Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra
Faça parte dessa comunidade
Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de Awa Thiès e vá além da letra da música.
Conheça o Letras AcademyConfira nosso guia de uso para deixar comentários.
Enviar para a central de dúvidas?
Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.
Fixe este conteúdo com a aula: