Diaral Ngama (feat. Pendo Guissé)
Duma dem, duma dikk, duma yónnee
Ku dem-dikk wax ma ma neexal la
Ci jaga, waaw ci jaga
Tàmm naa la man ci seen biir
Lu ñu bari-bari yaa ma ci doyloo
Jaral nga ma
Man yaa ma yendoo
Bu Yàlla ñëwul dafa yónnee
Ku gëm ki mu yónni mu neexal la
(Ko koy dogal te moo ñu boole)
Waaw mooy dogal
(Waaw mooy boole)
Xool naa la fi, nga génn fee
Ma xool la fi, nga génnaat fee
Naaj bi tànk may daw di daw
Langaamu sama yaram daw
Yaw la doon seet (gis naa la)
Man yaa ma doyloo (waaw baby kaay)
Chérie yaa may jooyloo (waaw chéri kaay)
Man yaa may dofloo (waaw baby kaay)
Soo sibbiru ma pikkiru naan fay doom
Coono bégal laa la faydo
Li mooy mbëggeel bànneex a neex
Chéri bëgg laa ba dee ci dagaan
Bëgg ku la gën a bëggaati dagaan
Gën bi gën a gën
Li mooy mbëggeel bànneex a neex
Tàmm naa la man ci seen biir
Lu ñu bari-bari yaa ma ci doyloo
Jaral nga ma
Man yaa ma yendoo
Bu Yàlla ñëwul dafa yónnee
Ku gëm ki mu yónni mu neexal la
(Ko koy dogal te moo ñu boole)
Waaw mooy dogal
(Waaw mooy boole)
Xool naa la fi, nga génn fee
Ma xool la fi, nga génnaat fee
Naaj bi tànk may daw di daw
Langaamu sama yaram daw
Yaw la doon seet (gis naa la)
Man yaa ma doyloo (waaw baby kaay)
Chérie yaa may jooyloo (waaw chéri kaay)
Man yaa may dofloo (waaw baby kaay)
Ku ndayam nangu mu takk la, ku ndayam nangu
Ku ndayam nangu mu takk la, ku ndayam nangu
Ku dem la jël takk ci sëgg te ngeen booleek ricc ku neex jëlal
Ay bu ko jékko da koy ricc mu neex
Bu Yàlla ñëwul dafa yónnee
Ku gëm ki mu yónni mu neexal la
Loolu ma booleek Aïcha Diallo
Moo ma booleek Marie Bara
Xool naa la fi, nga génn fee
Ma xool la fi, nga génnaat fee
Naaj bi tànk may daw di daw
Langaamu sama yaram daw
Yaw la doon seet (gis naa la)
Man yaa ma doyloo (waaw baby kaay)
Chérie yaa may jooyloo (waaw chéri kaay)
Man yaa may dofloo (waaw baby kaay)
Yaw la ma Yàlla boole
Djie Astou Sallé
Ki la ma Yàlla boole
Djie Astou Sallé
Diaral Ngama (feat. Pendo Guissé)
Duma dem, duma dikk, duma yónnee
Quem não se importa, quem não se importa, quem não se importa
Na briga, sim, na briga
Eu estou aqui dentro de você
O que eles fazem, você me faz sentir
Você me ama
Eu te amo também
Se Deus não quiser, não vai acontecer
Quem acredita que vai acontecer, vai sentir
(Se for pra acontecer, então vamos juntos)
Sim, é pra acontecer
(Sim, é pra acontecer)
Eu vejo você aqui, você vai sair
Eu vejo você aqui, você vai voltar
A noite está começando a clarear
A dor do meu corpo vai embora
Você está me vendo (eu vejo você)
Eu te amo (sim, baby, vem cá)
Querida, você vai me fazer feliz (sim, querida, vem cá)
Eu te amo (sim, baby, vem cá)
Se eu não conseguir, não vou me importar
A dor é real, eu vou me importar
Isso é o que é a verdadeira felicidade
Querida, eu te amo, não quero que você vá
Quero que você fique e me faça feliz
Mais e mais, mais e mais
Isso é o que é a verdadeira felicidade
Eu estou aqui dentro de você
O que eles fazem, você me faz sentir
Você me ama
Eu te amo também
Se Deus não quiser, não vai acontecer
Quem acredita que vai acontecer, vai sentir
(Se for pra acontecer, então vamos juntos)
Sim, é pra acontecer
(Sim, é pra acontecer)
Eu vejo você aqui, você vai sair
Eu vejo você aqui, você vai voltar
A noite está começando a clarear
A dor do meu corpo vai embora
Você está me vendo (eu vejo você)
Eu te amo (sim, baby, vem cá)
Querida, você vai me fazer feliz (sim, querida, vem cá)
Eu te amo (sim, baby, vem cá)
Quem ama, ama de verdade, quem ama, ama
Quem ama, ama de verdade, quem ama, ama
Quem não se importa, não se importa, e você vai me fazer feliz
Se você não se importar, vai me fazer feliz
Se Deus não quiser, não vai acontecer
Quem acredita que vai acontecer, vai sentir
Isso é o que eu quero, Aïcha Diallo
Isso é o que eu quero, Marie Bara
Eu vejo você aqui, você vai sair
Eu vejo você aqui, você vai voltar
A noite está começando a clarear
A dor do meu corpo vai embora
Você está me vendo (eu vejo você)
Eu te amo (sim, baby, vem cá)
Querida, você vai me fazer feliz (sim, querida, vem cá)
Eu te amo (sim, baby, vem cá)
Você é meu Deus
Djie Astou Sallé
Quem é meu Deus
Djie Astou Sallé