Tradução gerada automaticamente

Diaral Ngama (feat. Pendo Guissé)
Cherifou
Diaral Ngama (feat. Pendo Guissé)
Diaral Ngama (feat. Pendo Guissé)
Duma dem, duma dikk, duma yónneeDuma dem, duma dikk, duma yónnee
Quem não se importa, quem não se importa, quem não se importaKu dem-dikk wax ma ma neexal la
Na briga, sim, na brigaCi jaga, waaw ci jaga
Eu estou aqui dentro de vocêTàmm naa la man ci seen biir
O que eles fazem, você me faz sentirLu ñu bari-bari yaa ma ci doyloo
Você me amaJaral nga ma
Eu te amo tambémMan yaa ma yendoo
Se Deus não quiser, não vai acontecerBu Yàlla ñëwul dafa yónnee
Quem acredita que vai acontecer, vai sentirKu gëm ki mu yónni mu neexal la
(Se for pra acontecer, então vamos juntos)(Ko koy dogal te moo ñu boole)
Sim, é pra acontecerWaaw mooy dogal
(Sim, é pra acontecer)(Waaw mooy boole)
Eu vejo você aqui, você vai sairXool naa la fi, nga génn fee
Eu vejo você aqui, você vai voltarMa xool la fi, nga génnaat fee
A noite está começando a clarearNaaj bi tànk may daw di daw
A dor do meu corpo vai emboraLangaamu sama yaram daw
Você está me vendo (eu vejo você)Yaw la doon seet (gis naa la)
Eu te amo (sim, baby, vem cá)Man yaa ma doyloo (waaw baby kaay)
Querida, você vai me fazer feliz (sim, querida, vem cá)Chérie yaa may jooyloo (waaw chéri kaay)
Eu te amo (sim, baby, vem cá)Man yaa may dofloo (waaw baby kaay)
Se eu não conseguir, não vou me importarSoo sibbiru ma pikkiru naan fay doom
A dor é real, eu vou me importarCoono bégal laa la faydo
Isso é o que é a verdadeira felicidadeLi mooy mbëggeel bànneex a neex
Querida, eu te amo, não quero que você váChéri bëgg laa ba dee ci dagaan
Quero que você fique e me faça felizBëgg ku la gën a bëggaati dagaan
Mais e mais, mais e maisGën bi gën a gën
Isso é o que é a verdadeira felicidadeLi mooy mbëggeel bànneex a neex
Eu estou aqui dentro de vocêTàmm naa la man ci seen biir
O que eles fazem, você me faz sentirLu ñu bari-bari yaa ma ci doyloo
Você me amaJaral nga ma
Eu te amo tambémMan yaa ma yendoo
Se Deus não quiser, não vai acontecerBu Yàlla ñëwul dafa yónnee
Quem acredita que vai acontecer, vai sentirKu gëm ki mu yónni mu neexal la
(Se for pra acontecer, então vamos juntos)(Ko koy dogal te moo ñu boole)
Sim, é pra acontecerWaaw mooy dogal
(Sim, é pra acontecer)(Waaw mooy boole)
Eu vejo você aqui, você vai sairXool naa la fi, nga génn fee
Eu vejo você aqui, você vai voltarMa xool la fi, nga génnaat fee
A noite está começando a clarearNaaj bi tànk may daw di daw
A dor do meu corpo vai emboraLangaamu sama yaram daw
Você está me vendo (eu vejo você)Yaw la doon seet (gis naa la)
Eu te amo (sim, baby, vem cá)Man yaa ma doyloo (waaw baby kaay)
Querida, você vai me fazer feliz (sim, querida, vem cá)Chérie yaa may jooyloo (waaw chéri kaay)
Eu te amo (sim, baby, vem cá)Man yaa may dofloo (waaw baby kaay)
Quem ama, ama de verdade, quem ama, amaKu ndayam nangu mu takk la, ku ndayam nangu

Quem não se importa, não se importa, e você vai me fazer felizKu dem la jël takk ci sëgg te ngeen booleek ricc ku neex jëlal
Se você não se importar, vai me fazer felizAy bu ko jékko da koy ricc mu neex
Se Deus não quiser, não vai acontecerBu Yàlla ñëwul dafa yónnee
Quem acredita que vai acontecer, vai sentirKu gëm ki mu yónni mu neexal la
Isso é o que eu quero, Aïcha DialloLoolu ma booleek Aïcha Diallo
Isso é o que eu quero, Marie BaraMoo ma booleek Marie Bara
Eu vejo você aqui, você vai sairXool naa la fi, nga génn fee
Eu vejo você aqui, você vai voltarMa xool la fi, nga génnaat fee
A noite está começando a clarearNaaj bi tànk may daw di daw
A dor do meu corpo vai emboraLangaamu sama yaram daw
Você está me vendo (eu vejo você)Yaw la doon seet (gis naa la)
Eu te amo (sim, baby, vem cá)Man yaa ma doyloo (waaw baby kaay)
Querida, você vai me fazer feliz (sim, querida, vem cá)Chérie yaa may jooyloo (waaw chéri kaay)
Eu te amo (sim, baby, vem cá)Man yaa may dofloo (waaw baby kaay)
Você é meu DeusYaw la ma Yàlla boole
Djie Astou SalléDjie Astou Sallé
Quem é meu DeusKi la ma Yàlla boole
Djie Astou SalléDjie Astou Sallé

Comentários
Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra
Faça parte dessa comunidade
Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de Cherifou e vá além da letra da música.
Conheça o Letras AcademyConfira nosso guia de uso para deixar comentários.
Enviar para a central de dúvidas?
Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.
Fixe este conteúdo com a aula: