Tradução gerada automaticamente

exibições de letras 10
Letra

Amadou

Amadou

Eu não sei como fazer issoLu mu ma wax ma di ko def
Mas você está aqui pra me ajudarDafay dëkk ci di ma tooñ
Me diz que vai me apoiarTeg si ma naan ko baal ma
Mas é você quem eu queroWaaye moom la nob
Se eu te verSu ma ko gisee
Meus olhos brilhamSamay bët di mellax
Meu coração aceleraSamay tànk jaxasoo
Meu lar é vocêSama lammiñ réer ma
É você quem eu queroMoom laa nob

Amadou, Amadou (me ajuda)Amadou, Amadou (geestu ma)
Você é minha mãe (meu Amadou)Yaw sama yaay (may ma Amadou)

Amadou, AmadouAmadou, Amadou

Eu sinto que não tem nadaDamay gëm loo lu amul
Não consigo me sentir assimTerewul ma di ko gëm
Me diz que vai me apoiarTég ci ma naan ko baal ma
Mas é você quem eu queroWaaye moom la nob
Se eu te verSu ma ko gisee
Meus olhos brilhamSamay bët di mellax
Meu coração aceleraSamay tànk jaxasoo
Meu lar é vocêSama lammiñ réer ma
É você quem eu queroMoom laa nob

Amadou, Amadou (me ajuda)Amadou, Amadou (geestu ma)
Você é minha mãe (meu Amadou)Yaw sama yaay (may ma Amadou)
Amadou, Amadou (me ajuda)Amadou, Amadou (geestu ma)
Você é minha mãe (meu Amadou)Yaw sama yaay (may ma Amadou)
Amadou, AmadouAmadou, Amadou

Amadou, Amadou (me ajuda)Amadou, Amadou (geestu ma)
Você é minha mãe (meu Amadou)Yaw sama yaay (may ma Amadou)
Amadou, Amadou (me ajuda)Amadou, Amadou (geestu ma)
Você é minha mãe (meu Amadou)Yaw sama yaay (may ma Amadou)
Amadou, AmadouAmadou, Amadou

Quando eu te ligar no telefoneSaa yu ma jege woote téléphone
No telefone que você atendeCi téléphone bi lay yéndu
Quando eu te ligar pra te verSaa yu ma jege ab setsi
Eu vou te chamarMa yendoo wajal
Eu sei que você é a única que não me deixaXam naa ni nob na keneen ku dul man
Oh, eu sei que você é a única que não me deixaOh yeg na ni mi ngi seeti keneen ku dul man
Mas é você quem eu queroWaaye moom laa nob

Amadou, Amadou (me ajuda)Amadou, Amadou (geestu ma)
Você é minha mãe (meu Amadou)Yaw sama yaay (may ma Amadou)
Amadou, Amadou (me ajuda)Amadou, Amadou (geestu ma)
Você é minha mãe (meu Amadou)Yaw sama yaay (may ma Amadou)
Amadou, AmadouAmadou, Amadou

Amadou, Amadou (me ajuda)Amadou, Amadou (geestu ma)
Você é minha mãe (minha mãe, meu Amadou)Yaw sama yaay (sama yaay may ma Amadou)

Comentários

Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra

0 / 500

Faça parte  dessa comunidade 

Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de Coumba Gawlo e vá além da letra da música.

Conheça o Letras Academy

Enviar para a central de dúvidas?

Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.

Fixe este conteúdo com a aula:

0 / 500

Opções de seleção