Tradução gerada automaticamente

Xale Bi Nangouna (feat. Korka Dieng)
Didier Awadi
Xale Bi Nangouna (feat. Korka Dieng)
Xale Bi Nangouna (feat. Korka Dieng)
Meu xale tá aquiSama xalé bi nangu na
Meu Goné tá aquiSama Goné gui nangu na
Mãe, meu shorty tá aquiYaye boy sama shorty bi nangu na
Pai, meu açúcar tá aquiBaye boy sama suger bi nangu na
Acorda, meu Goné tá aqui, uauAwadi bilay goné gui néna waw
Xale, tão bonito, tá aqui, tá aquiXalé bou rafet dikeu na, dikeulen sétane
E a cabeça tá cheiaWa kogn bi kaay len xol
Vai lá, vai láLay la la law
Damey nanguoDamey nanguo
Damey nangu (bess bi sa bessa)Damey nangu (bess bi sa bessa)
Wol badiene, wowal nidiaye damey nanguWol badiene, wowal nidiaye damey nangu
(Bess bi sa bessa)(Bess bi sa bessa)
Damey nanguoDamey nanguo
Damey nangu (bess bi sa bessa)Damey nangu (bess bi sa bessa)
Yeuy kani, matia fi xorom damey nanguYeuy kani, matia fi xorom damey nangu
Hoje tá aqui, tá aqui (han)Tey na waw ne na nanguna (han)
E a cabeça do xale tá aqui (way deugueula)Wa kogn bi xale bi nanguna (way deugueula)
Balança como se não houvesse amanhãYeggeul ko tiat ba tiat
Garoto e garota, eu e vocêGor ak jiguen, mag ak ndaw
Meu xale tá aqui (wu yaay)Sama xalé bi nanguna (wu yaay)
Paciência, calma, respira (teugueu lene)Sabar yi, ndeundeu yi, reuk lene (teugueu lene)
Mãe, e aí, como você tá? (way tama ya)Mamane, tama yi, ana nguene? (way tama ya)
Bongo não pode parar, tá aqui (way bongo)Bongo dou manke de, dikeulene (way bongo)
Ndaanaanou deukeu bi gueneu lene (way deugueu leu)Ndaanaanou deukeu bi gueneu lene (way deugueu leu)
Te quero, te amo, te desejo (aie way)Yaru nga, jekk nga, taaru nga (aie way)
Me leva pro seu lugar, eu vou te mostrarMat nga sa place, da nga jongoma
Eu só quero ser seu, meu amorMan maa la tann sama sadja ban
Mãe, meu amor, meu coração, pra sempre (waw waw)Yaye sama love, sama xol, fi ba abadan (waw waw)
Damey nanguoDa mey nanguo
Damey nangu (bess bi sa bessa)Da mey nangu (bess bi sa bessa)
Wol badiene, wowal nidiayeWowal badiene, wowal nidiaye
Damey nangu (diog lene niou gumbé)Da mey nangu (diog lene niou gumbé)
Damey nanguoDa mey nanguo
Damey nangu (bess bi sa bessa)Da mey nangu (bess bi sa bessa)
Yeuy kani, matia fi xoromYeuy kani, matia fi xorom
Damey nanguDa mey nangu
Se liga, meu irmão, tá tudo certo (han han)Seeri boy mané tey la tey (han han)
O que você quer, eu vou fazer (way han han)Tanneul lu la nekh mané naa ko feye (way han han)
Wurus aki ngalam mané, eu vou te amarWurus aki ngalam mané, maa la mèye
Meu coração não vai parar de baterSama xol dafa sedd buma kéna rèye
Eu não sou você, mas Deus éDu man du yow, mané yalla la
Se eu não te amar, não vou amar ninguémMo ma tanneu, ma tanneu la
Se você não for pra casa, não vai ter pazMo mané demal ci tali bi demal ci gedj
Dugu gaal mu won ma la (wouy yay)Dugu gaal mu won ma la (wouy yay)
Você é a razão da festa (kekh kekh may ré)Yow la done xaar (kekh kekh may ré)
Você é a razão da festa (kekh kekh may ré)Yow la done xaar yow (kekh kekh may ré)
(Gneup di ré)(Gneup di ré)
Damey nanguoDa mey nanguo
Damey nangu (bess bi sa bessa)Da mey nangu (bess bi sa bessa)
Wol badiene, wowal nidiayeWowal badiene, wowal nidiaye
Damey nangu (kou sa xol neex)Da mey nangu (kou sa xol neex)
Damey nanguDa mey nangu
Damey nangu (diuk lene ñou bal)Da mey nangu (diuk lene ñou bal)
Yeuy kani, matia fi xoromYeuy kani, matia fi xorom
Damey nanguDa mey nangu
Ei, meu sadiabaneYaw yay sama sadiabane
Rabadabine, tá tudo bemRabadabine ndat say
Ei, meu sadiabaneYaw yay sama sadiabane
RabadabineRabadabine
Acorda, meu Goné tá aqui, uauBilaye goné gui né na waw
Diok lene gnou gumbé (hé hé)Diok lene gnou gumbé (hé hé)
Diok lene gnou gumbé (hé hé)Diok lene gnou gumbé (hé hé)
E aí, Senegal (hé hé)Wa Sénégal (hé hé)
Quem tá com você, tá com você (hé hé)Ku nek ak ki nga beugueu (hé hé)
Xolal diok lene gnqu gumbé (hé hé)Xolal diok lene gnqu gumbé (hé hé)
Diok lene gnu gumbé, gumbé (hé hé)Diok lene gnu gumbé, gumbé (hé hé)
Yaba ndaw rabine, tá tudo bem (hé hé)Yaba ndaw rabine ndat say (hé hé)
Wu yayWu yay
Bess bi sa beussaBess bi sa beussa
Damey nanguoDa mey nanguo
Damey nangu (bilaye gone gui néna waw)Da mey nangu (bilaye gone gui néna waw)
Wol badiene, wowal nidiayeWowal badiene, wowal nidiaye
Damey nangu (lay laha ila la)Da mey nangu (lay laha ila la)
Damey nanguDa mey nangu
Damey nangu (woy l'amour il est beau)Da mey nangu (woy l'amour il est beau)
Yeuy kani, matia fi xoromYeuy kani, matia fi xorom
Damey nanguDa mey nangu
Meu xale tá aqui (wo yay)Sama xalé bi nangu na (wo yay)
Meu Goné tá aqui (han)Sama Goné gui nangu na (han)
Mãe, meu shorty tá aquiYaye boy sama shorty bi nangu na
Pai, meu açúcar tá aqui (way deugueu leu)Baye boy sama suger bi nangu na (way deugueu leu)
Meu xale tá aqui (aie way)Sama xalé bi nangu na (aie way)
Meu Goné tá aqui (wou yay)Sama Goné gui nangu na (wou yay)
Mãe, meu shorty tá aquiYaye boy sama shorty bi nangu na
Pai, meu açúcar tá aquiBaye boy sama suger bi nangu na



Comentários
Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra
Faça parte dessa comunidade
Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de Didier Awadi e vá além da letra da música.
Conheça o Letras AcademyConfira nosso guia de uso para deixar comentários.
Enviar para a central de dúvidas?
Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.
Fixe este conteúdo com a aula: