Tradução gerada automaticamente
Labat
Fatou Laobé
Apenas
Labat
ÃÃa kaay labat ma
Reze por mim, meu paiÑaan ma sama baay bóoy
Ele disse que simMu may ma laa waaw
ÃÃa kaay labat ma
Reze por mim, meu paiÑaan ma sama baay bóoy
Ele disse que simMu may ma laa waaw
Billay pequeno e altoBillaay njool mu ndaw
Eu decidi levarKaay dogaale ma yóbbu
Para onde quer que eu vá!Foo jëm aawoloo ma
Vou ligar para sua mãeMay wolal sa yaay
Cozinhar issoDi ko toggal
Enraizando enquanto bebeDi root muy naan
ÃÃa kaay labat ma
Reze por mim, meu paiÑaan ma sama baay bóoy
Ele disse que simMu may ma laa waaw
Billay pequeno e altoBillaay njool mu ndaw
Eu decidi levarKaay dogaale ma yóbbu
Para onde quer que eu vá!Foo jëm aawoloo ma
Vou ligar para sua mãeMay wolal sa yaay
Cozinhar issoDi ko toggal
Enraizando enquanto bebeDi root muy naan
ÃÃa kaay labat ma
Reze por mim, meu paiÑaan ma sama baay bóoy
Ele disse que simMu may ma laa waaw
Eu tomo banho e fico com um cheiro bomDamay sangu solu xeeñ lu neex
Querida, mas antes de você chegar eu acabei adormecendoChéri waaye bala ngaa ñëw ma nelaw
Vou tocar o seu "prato" favorito"Plat" bi nga gën a bëgg laay rëgal
Querida, mas antes de você chegar eu acabei adormecendoChéri waaye bala ngaa ñëw ma nelaw
Os milhares que você me dá, eu ouço dizer que você não me dáJunni yi ngay maye ma di ko dégg mayoo ma ci
Querida, mas antes de você chegar eu acabei adormecendoChéri waaye bala ngaa ñëw ma nelaw
Eles não me viram e me deram milJongoma joo séen dem may kob junni
Você não sabe que eu não sou fã?Xanaa xamoo ne man mi jongoma laa
ÃÃa kaay labat ma
Reze por mim, meu paiÑaan ma sama baay bóoy
Ele disse que simMu may ma laa waaw
Eu com amorMan ak mbëggeel
Uau, uau, uau, que amor!Wóo wóo wówóow man ak mbëggeel
De vez em quando, sentamos e conversamosLeeg-leeg nu toog di waxtaan
Nossa relação é doce como açúcarSunu diggante neex ba mel ni suukar
De vez em quando, sentamos e conversamosLeeg-leeg nu toog di waxtaan
Satanás veio e nos perdemosSeytaane dikk nu daal di réeróo
Nós, mulheres, somos todas iguaisNun jigéen ñi nun ñépp a yem
Aquele que os controla é paciente com elesKu leen di yor da nga leen di muñal
Não se ofender com KuraFàllu bu la Kura tooñatee
Saiba apenas que você nasceu de uma mulherJéggal ko te xam ne jigéen a la jur
Omar, se a senhora Njaay lhe fez mal, você tambémOmar bu la Maam Njaay tooñatee
Saiba apenas que você nasceu de uma mulherJéggal ko te xam ne jigéen a la jur
Aysata Sow, que Deus abençoe você e sua famíliaAysata Sow yaw Yàlla na la Yàlla may looy béggéey
Você é o únicoYaw rekk laa waaw
Asan, quando você se ofende com FaatAsan bu la Faat naar tooñatee
Saiba apenas que você nasceu de uma mulherJéggal ko xam ne jigéen a la jur
Aziz Gay - Quando Você É InjustiçadoAziz Gay bu la Ndey Mbay tooñatee
Saiba apenas que você nasceu de uma mulherJéggal ko te xam ne jigéen a la jur
Ami Jeng, mãe de Maas Njaay, não é nada melhor que issoAmi Jeŋ yaayu Maas Njaay dara weesul
Eu sei que você é a única pessoaMan xam naa ni yaw rekk la
Traduzido por Matar Ndiaye Traduzido porFiiru ma Matar Ndiaye fiiru ma
Eu te amo, eu tenho ciúmes de vocêYaw la bëgg yaw laa miin fiiru ma
Seu voo te levará para longeFiiru ma maa fiiru ma
Eu te conheço, eu te conheço, estou com ciúmesYaw laa xam yaw laa miin fiiru ma
Uau, uau, uau!Wóo wóo wóowu wóowu
Meu bem, eu te amo, simChéri I love you, waaw
Meu queridoMon chéri
Meu queridoMon chéri
Meu queridoMon chéri
Eu sou apenas você!Yaw rekk laa
Sim, os dois se amamWaaw ñaar ñu bëggante
Se não gostar, diga algo gentilBoo ca xajul wax ca lu baaxoo
Eu te amo, uau!I love you waaw
Meu queridoMon chéri
Meu queridoMon chéri
Meu queridoMon chéri
Eu sou apenas você!Yaw rekk laa
Billy Ace!Billaay Aas !
Cherry Dado GeyChéri Daado Géy
Tenha paciência com ele!Dee ko muñal
Tolerância à morte, simDee ko muñal waaw
Eu te amo, uau!I love you waaw
Meu queridoMon chéri
Meu queridoMon chéri
Meu queridoMon chéri
Eu sou apenas você!Yaw rekk laa
Mãe da MorteNdey Faatu Njaay
Mãe da MorteNdey Faatu Njaay
Sra. DemeMadame Deme
Deus nos une!Yàllaa nu boole
Você é o únicoYaw rekk laa waaw
Meu queridoMon chéri
Meu queridoMon chéri
Meu queridoMon chéri
Eu sou apenas você!Yaw rekk laa
Billay, a GalinhaBillaay Aliwu Ba
Querido DeusChéri Jee
Não deixe que Jesus te ofendaBu la Jee tooñatee
Perdoe-oJéggal koo
Só você acredita que simYaw rekk la gëm waaw
Meu queridoMon chéri
Meu queridoMon chéri
Meu queridoMon chéri
Você é o únicoYaw rekk laa waaw
Meu queridoMon chéri
Eu sou apenas você!Yaw rekk laa
Meu queridoMon chéri
Você é o únicoYaw rekk laa waaw
Meu queridoMon chéri
Você é o únicoYaw rekk laa waaw
Meu queridoMon chéri
Você é o únicoYaw rekk laa waaw



Comentários
Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra
Faça parte dessa comunidade
Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de Fatou Laobé e vá além da letra da música.
Conheça o Letras AcademyConfira nosso guia de uso para deixar comentários.
Enviar para a central de dúvidas?
Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.
Fixe este conteúdo com a aula: