Tradução gerada automaticamente

exibições de letras 73

Eutou Baabel

AMADEUS

Letra

Ligue para Babel

Eutou Baabel

Com você para sempre.Maak yaw ba abadan
Eu te dei meu poder!Jox naa la sama kàttan
Negociando com minha infânciaJaayaanteek sama ndaw
Fiquei com água na boca!Dem naa ba ndox ci baat
Eu te dei minha palavraJox naa la sama kàddu
Eu não posso mais te perdoarMënatuma la baal

E espero ter sucesso com você.Te sèntu naa ci jële ndam maak yaw
O mundo está tentando me fazer desistir?Ndax àddunya bi dafay feexe ba ma xàddi
Eu não vou parar o que comecei, caraDuma bàyyi li ma tàmbali man
Lembro-me do meu avô.Fàttaliku naa sama maam
Ele me disse para pegar o passe.Ne na ma fori jëlal jaaro gi

Ouvi dizer que você ganha uma máscara e não é outra mulher.Dégg naa ñu lay wutal mas te doo moroom jigéen
Eu sei que eles vão me perguntar por que eu disse lileXam naa dinañu ma laaj lan moo tax ma wax lile
Ninguém é como Thiam Baabel, você sabe que eu te amo.Kenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
Ninguém é como Thiam Baabel, você sabe que eu te amo.Kenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la

Eles iamDemanoon de nañu
Eles fizeram coisas.Defando nañu ay mbir
Você me diz algo neXamal nga ma lu ne
Se você me deixarSoo ma yoolee
Não valho mais nada.Dootuma jar dara
Quando todos se esconderam de mim.Bi ma ñépp umpale
Você sabe!Yaw yaa ko xam
Você é meu homemSama waay nga

Alguém como vocêKu mel ni yaw
Quem não tem tem inveja.Ku ka amul da koy iñaane
Alguém como vocêKu mel ni yaw
As bruxas estão perguntando a você.Ëtu baabel ñoo lay laaj
Alguém como vocêKu mel ni yaw
Thiam Babel Demba Thiam, ehThiam Baabel Demba Thiam, eh
Alguém como vocêKu mel ni yaw
A Babel pergunta a você.Ëtu baabel yaw lay laaj

Estou levando você ao castelo da bruxa.Naa la yóbbu ëtub baabel
É uma colaboração com meus colegas.Boole la ak samay nawle yi
Você conhece a magia de Babel.Xam nga tàkkusaanu baabel
Thiam o dono da loja você estava brincando láThiam boroom ndendi was nga fay fowee

VocêYaw
Você não se cansa de mim.Mësuloo ma xépp ci samay ay ayib
Você nunca contou a ele sobre meus erros.Sama njuumte yi mësoo ko nettali
Você sabe, não existem heróis.Xam nga jaambaar amul
Quem é ajudado temKu ñu dimbale am
Perseverança é sempre bom.Ku sañoon day baax
Como um bebê elefanteComme doomu ñay
Não ore por mim.Bu ma ñaanal ponkal
Estou bem se eu viver.Man soo ma dundee baax

Ouvi dizer que você ganha uma máscara e não é outra mulher.Dégg naa ñu lay wutal mas te doo moroom jigéen
Eu sei que eles vão me perguntar por que eu disse lileXam naa dinañu ma laaj lan moo tax ma wax lile
Ninguém é como Thiam Baabel, você sabe que eu te amo.Kenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
Ninguém é como Thiam Baabel, você sabe que eu te amo.Kenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la

Eles iamDemanoon de nañu
Eles fizeram coisas.Defando nañu ay mbir
Você me diz algo neXamal nga ma lu ne
Se você me deixarSoo ma yoolee
Não valho mais nada.Dootuma jar dara
Quando todos se esconderam de mim.Bi ma ñépp umpale
Você sabe!Yaw yaa ko xam
Você é meu homemSama waay nga

Alguém como vocêKu mel ni yaw
Quem não tem tem inveja.Ku ka amul da koy iñaane
Alguém como vocêKu mel ni yaw
As bruxas estão perguntando a você.Ëtu baabel ñoo lay laaj
Alguém como vocêKu mel ni yaw
Thiam Babel Demba Thiam, ehThiam Baabel Demba Thiam, eh
Alguém como vocêKu mel ni yaw
A Babel pergunta a você.Ëtu baabel yaw lay laaj

Comentários

Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra

0 / 500

Faça parte  dessa comunidade 

Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de AMADEUS e vá além da letra da música.

Conheça o Letras Academy

Enviar para a central de dúvidas?

Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.

Fixe este conteúdo com a aula:

0 / 500

Opções de seleção