Tradução gerada automaticamente

exibições de letras 55
Letra

Jiin

Jiin

Ei, Massamba WaloEy Massamba Walo

Se eu não tiver, não vai dar certoSa ñàkk teew a raw daay
Não me deixe na piorBul ma fi ñukk gàddaay
Eu vi você se aproximando como um raioGis naa la ngay samandaay ni gaynde
Você é mulher, mas é forteJigéen nga waaye jaambaar nga
Eu não vou te deixar de lado, só um diaXébuma la ngir sa melokaan, man benn yoon

Quem eu vejo em você vai me fazer bemKu ma xool ci yaw dina ma mere
Porque eu não sou de ficar pensando em vocêNdax demewuma xel, ci leen lu jëm ci yaw
Deus me deu a visão que eu precisavaYàlla moo dogal fu ma la gise
Me ajude com meu coraçãoTaggoo ak sama sagooy
Sim, eu vou te dar tudo com as duas mãosWaaw man dama lay téye ak fukki loxo
Deus me ajudou, eu realmente quero muitoYàlla man la nattoo, manit ma nangu ko lool
Você me faz querer, eu só quero te dizerYaa ma leen gënal, dama la ko rusoon a waxe

Jiin, jiiin, meu coração tá tão bemJiino jiin, sama xol neex na moo tax
Jiin, jiiin, meu jeito tá tão bomJiino jiin, samay way neex na

O que eu vejo no meu coração tá tão bomLi may gis sama xel dal na
Porque hoje tá tão bom, de manhã até DeusNdax tay day neex suba suba Yàlla la

A gente tá aqui, eu e os caras, pra fazer você se sentir em casaBis a ngi ci bis yi man ak guys yi nañu fëgg sa kër
Entrando nas baladas, junto com a galera, vem dar uma olhada na sua vibeDugg ci sabadore yi ànd ak paa yi, ñëw jox la sa cër
Por que eu não sabia que ia ser assim, eu só percebi hojeFoo mi taxu ma jukk dama àll ba ma la xame ba tay
É, mulher, você é forteYeah waay jigéen nga waaye jaambaar nga
Eu não vou te deixar de lado, só um diaXébuma la ngir sa melokaan, man benn yoon
Você é mulher, mas é forteJigéen nga waaye jaambaar nga

Quem eu vejo em você vai me fazer bemKu ma xool ci yaw dina ma mere
Porque eu não sou de ficar pensando em vocêNdax demewuma xel, ci leen lu jëm ci yaw
Deus me deu a visão que eu precisavaYàlla moo dogal fu ma la gise
Me ajude com meu coraçãoTaggoo ak sama sagooy
Sim, eu vou te dar tudo com as duas mãosWaaw man dama lay téye ak fukki loxo
Deus me ajudou, eu realmente quero muitoYàlla man la nattoo, manit ma nangu ko lool
Você me faz querer, eu só quero te dizerYaa ma leen gënal, dama lay ko rusoon a waxe

Jiin, jiiin, meu coração tá tão bemJiino jiin, sama xol neex na moo tax
Jiin, jiiin, meu jeito tá tão bomJiino jiin, samay way neex na
Jiin, jiiin, meu coração tá tão bemJiino jiin, sama xol neex na moo tax
Jiin, jiiin, meu jeito tá tão bomJiino jiin, samay way neex na

O que eu vejo no meu coração tá tão bomLi may gis sama xel dal na
Porque hoje tá tão bom, de manhã até DeusNdax tay day neex suba suba Yàlla la
Jiin, jiiin, meu coração tá tão bemJiino jiin, sama xol neex na moo tax
Jiin, jiiin, meu jeito tá tão bomJiino jiin, samay way neex na

Comentários

Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra

0 / 500

Faça parte  dessa comunidade 

Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de AMADEUS e vá além da letra da música.

Conheça o Letras Academy

Enviar para a central de dúvidas?

Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.

Fixe este conteúdo com a aula:

0 / 500

Opções de seleção