Tradução gerada automaticamente

Waw Coumba
AMADEUS
Waw Kumba
Waw Coumba
Ei Massamba WaloHey Massamba Walo
Eu não sei se eu te entendoMaa la tooñ ndax maa la woolu
Mas quando você chega, eu só quero falar coisas boasBa nga ñëw ma lay wax ay waxu mbëggeel
Eu te amo e você me entendeMaa la doy te man nga wóolu
Nosso olhar se encontra em algo que não tem explicaçãoSunu ànd gisuma ci lu dul ngëneel
Se eu estiver tristeSu jaree raag
Eu vou te chamar, eu preciso de vocêDinaa la wan fi ma manee yaw
Eu não vou desistirMan duma seetaan
Se eu estiver tristeSu jaree raag
Eu vou te mostrar minha casaDinaa la yóbbu sama gàlle
Apresentar tudo que eu tenhoPrésenter la sama gaa yépp
É, uauEey waay
Eu te amo, não é só papoMan dama laa, bëgg du nax
É a vontade de Deus que me trouxe até vocêCoobare Yàlla Moo ma indi ci yaw
O mundo tá cheio de coisas dentro de nósÀdduna yaa fiy wàcc sunu biir
Vamos nos encontrarWaru nu tee gise
Você, Kumba, é como um irmão aqui no SenegalYaw Kumba amóo moroom biir Senegaal
Dizem que você é a Kumba que trouxe a grana pro SenegalNee naa la waaw-kumba jël naa seede waa Senegaal
O mundo precisa de você, você tem que ficar no SenegalÀdduna yaatu na yaa ma tax a toog Senegaal
Sim, Kumba, você é a força do SenegalWaaw kumba danga di taaru Senegaal
Eu te amo, eu te entendoMan dama laa wóolu man
Você me entendeNdax danga maa wóolu
E eu não vou embora sem vocêTe duma dem fenn ba la
Você não vai me deixarNdax danga may wër
Eu não sei se eu te entendoMaa la tooñ ndax maa la woolu
Mas quando você chega, eu só quero falar coisas boasBa nga ñëw ma lay wax ay waxu mbëggeel
Eu te amo e você me entendeMaa la doy te man nga wóolu
Nosso olhar se encontra em algo que não tem explicaçãoSunu ànd gisuma ci lu dul ngëneel
Ei, uauKaay waay
Muita pazLot of peace
Muito amorLot of love
Soxna siiSoxna sii
Eu só quero issoMan loolu laa la yéene
Não acrediteDon't believe
Uma faltaBenn miss
O que a gente vêLi ñu gis
É o que nos uneMooy nu wàlliyaani
Força SenegalTaaru Senegaal nga
Linguère no KayorLinguère biir Kayor
Mãe, dona da hospitalidadeYaay boroom teraanga
A gente se une, se abraçaJéeri jàpp Joor
Você, Kumba, é como um irmão aqui no SenegalYaw Kumba amóo moroom biir Senegaal
Dizem que você é a Kumba que trouxe a grana pro SenegalNee naa la waaw-kumba jël naa seede waa Senegaal
O mundo precisa de você, você tem que ficar no SenegalÀdduna yaatu na yaa ma tax a toog Senegaal
Precisa de você, você tem que ficar no SenegalYaatu na yaa ma tax a toog Senegaal
Sim, Kumba, você é a força do SenegalWaaw kumba danga di taaru Senegaal
Ah, éAnh yeaah
Eu te amo, eu te entendoMan dama laa wóolu man
Você me entendeNdax danga maa wóolu
E eu não vou embora sem vocêTe duma dem fenn ba la
Você não vai me deixarNdax danga may wër
Você, Kumba, é como um irmão aqui no SenegalYaw Kumba amóo moroom biir Senegaal
Dizem que você é a Kumba que trouxe a grana pro SenegalNee naa la waaw-kumba jël naa seede waa Senegaal

Comentários
Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra
Faça parte dessa comunidade
Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de AMADEUS e vá além da letra da música.
Conheça o Letras AcademyConfira nosso guia de uso para deixar comentários.
Enviar para a central de dúvidas?
Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.
Fixe este conteúdo com a aula: