Tradução gerada automaticamente

Jolie femme d'Afrique
Mia Guisse
Linda mulher da África
Jolie femme d'Afrique
Bàyyi ma yéye chewing gumBàyyi ma yéye chewing gum
Xale bi, é pra mim?Xale bi est-ce que c'est pour moi
Zero erro, tô na boaZéro faute ma ne lépp tout bon
Se eu te chamar, não vai dar ruimNi ma ko barde we, le mbaa doo ngiste
Linda mulher da África (da África)Jolie femme d'Afrique (d'Afrique)
Meu olhar é bombásticoSama regard mooy bombastic
Aqui tô, sou fantásticoGaa yi naan je suis fantastique
Se eu me apresentar, quem sou eu?Su ma jàkkaarloo nit ki man
Eu faço a música rolarMaa fit wi di musique naan
Rampapam rampapam rampapamRampapam rampapam rampapam
Rampapam rampapam rampapamRampapam rampapam rampapam
Meu olhar e meu coração tão em sintoniaSamay bët ak sama xol a ma tooñ
Eles me chamam de boy, mas eu sou só euÑoo ma nobloo boy bi nekk sama koñ
Não me deixe ver você tão cedoNe na fook mu gis ma tay si ngoon
Não tem como não falar com vocêAmaguma fitu wax ak moom
Bàyyileen, se eu não te chamarBàyyileen ma bu leen ma dugal
Na balada, vou te encontrarCi mbëggeel bu may yóbbu coma
Ay, ay, ay, ai, me deixa em pazAy, ay, ay yaay, foon na ma dee
Me deixa em paz, o que eu faço pra você?Foon na ma dee, lu ma dall yaw la
Se eu não te chamar, o que eu faço pra você?Soo ma nobee lu ma dall yaw la
Se eu não souber, não vou me preocuparBi xeetu nit man àntanuma ko
Eu não sei o que fazerDama ko nob ba [?]
Me deixa em paz, ahDi ko xalaat ta [?]
Se eu te chamar (me ajuda)Su ma ko jegee (moo ray ma)
Eu vou fazer tudo, tudo, tudoMa lépp lépp lépp [?]
Se eu não te ver, não sei o que fazerSu ma naree giseek moom
Pânico, não sei como agirPanique jaxasoo ma ni juuk rekk daw
Eh, você, não me deixe na mãoEh yaw man ndekke parewuma
Eu tô parecendo quem vai pra brigaMaa ngi mel ni kuy dem combat
Ouyah, yahOuyah, yah
Tô chocado, yah yahDama choqué yaah yah
Tô chocado, yah yahDama choqué yaah yah
Se não me deixarem em paz, vou surtarTax bu ñu dajee sama fit bi di tëb di tëgganal sib na
Rampapam rampapam rampapamRampapam rampapam rampapam
Rampapam rampapam rampapamRampapam rampapam rampapam
Meu olhar e meu coração tão em sintoniaSamay bët ak sama xol a ma tooñ
Eles me chamam de boy, mas eu sou só euÑoo ma nobloo boy bi nekk sama koñ
Não me deixe ver você tão cedoNe na fook mu gis ma tay si ngoon
Não tem como não falar com vocêAmaguma fiitu wax ak moom
Bàyyileen, se eu não te chamarBàyyileen mu bu leen ma dugal
Na balada, vou te encontrarCi mbëggeel bu may yóbbu coma
Ay, ay, ay, ai, me deixa em pazAy, ay, ay yaay, foon na ma dee
Me deixa em paz, o que eu faço pra você?Foon na ma dee, lu ma dall yaw la
Se eu não te chamar, o que eu faço pra você?Soo ma nobee lu ma dall yaw la
Se eu não souber, não vou me preocuparBi xeetu nit man àntanuma ko
Ay, ay, ay, ai, me deixa em pazAy, ay, ay yaay, foon na ma dee
Me deixa em paz, o que eu faço pra você?Foon na ma dee, lu ma dall yaw la
Se eu não te chamar, o que eu faço pra você?Soo ma nobee lu ma dall yaw la
Se eu não souber, não vou me preocuparBi xeetu nit man àntanuma ko
Ay ay chocado, tô chocadoAy ay choqué, dam lay choqué
Se eu não souber, vou ficar travado, ahSu ma jugee pour dem daa am luy bloqué, ah
Escuta, eu preciso focarÉcoutez man faw ma focus
Eu quero saber, me ajuda a sair dessa, ah!Dama bëgga xam man kañ la namp ragal, ah!
Linda mulher da ÁfricaJolie femme d'Afrique
Meu olhar é bombásticoSama regard mooy bombastic
Aqui tô, sou fantásticoGaa yi naan je suis fantastique
Se eu me apresentar, sou só euSu ma jàkkaarloo boy bi
Eu faço a música rolarMaa fit bi di musique naan
Rampapam rampapam papamRampapam rampapam papam
Rampapam rampapam papanraRampapam rampapam papanra
Boy, boy, boy, só na boaBoy bi boy bi laperas
Se eu não souber, não vou me preocuparBi xeetu nit àntanuma ko
Ay, ay, ay, ai, me deixa em pazAy, ay, ay yaay, foon na ma dee
Me deixa em paz, o que eu faço pra você?Foon na ma dee, lu ma dall yaw la
Se eu não te chamar, o que eu faço pra você?Soo ma nobee lu ma dall yaw la
Se eu não souber, não vou me preocuparBi xeetu nit man àntanuma ko
Ouyah, yahOuyah, yah
Tô chocado, yah yahDama choqué yaah yah
Tô chocado, yah yahDama choqué yaah yah
Se não me deixarem em paz, vou surtarTax bu ñu dajee sama fit bi di tëb
Eu não sei o que fazer, wuy!Man xamuma pur lan, wuy!

Comentários
Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra
Faça parte dessa comunidade
Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de Mia Guisse e vá além da letra da música.
Conheça o Letras AcademyConfira nosso guia de uso para deixar comentários.
Enviar para a central de dúvidas?
Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.
Fixe este conteúdo com a aula: