Lonkotina
Man dégg naa feebaru mbëggeel kenn mënu ko faj
Ma bëgg ba malade te fasenewuma naan garab
Ngelaw bi ci ëpp kaay, dootul mel ni faru-rab
Nobati naa, lonkoti naa dal, wuy Pape et Cheikh
Ouhou ouhou ouh...
Boo ñamul kaani doo xam cafka sukkër bi neex ci lem
Ouhou ouhou ouh...
Daagan naa jaamu ki la ressuscité
Nga ni...
Ku la moom?
Man ma la moom
Laaj ma ku ma moom man
Ma bañ duma ko wax
Nga ni ku la moom
Man ma la moom
Laaj ma ku ma moom man
Yaw rekk yaw rekk lay doon ba muy moom
Lonkoti naa, foo ma jaar?
Man yaw rekk la bëgg
Pare naa bañ bañ na dara
My baby boo
May baby cat dafa gaaw
"Suma suma lomsong fi jubbo lonkong"
Musloo ci seytaane
Ma xaare côté bi nga jaare côté bee
Neex-neex bi lan la?
Tempo tempo di jël sa temps ba rof ma jaaro baram
Laax bi nak fok ma sëlëm ko sa kanam
Tegal benn pas ñëw, kon ma teg ñaari fekk ci la
Bul di dóor, bul di saaga
Xoolal li ñu teg sa loxo
Tégal benn pas ñëw, kon ma teg ñaari fekk ci la
Ho ho ho ho, dëggëntan ba ngee
Ouhou ouhou ouh...
Boo ñamul kaani doo xam cafka sukkër bi neex ci lem
Ouhou ouhou ouh... (ouxayati)
Daagan naa jaamu ki la ressuscité
Nga ni...
Ku la moom?
Man ma la moom
Laaj ma ku ma moom man
Ma bañ duma ko wax
Nga ni ku la moom
Man ma la moom
Laaj ma ku ma moom man
Yaw rekk yaw rekk lay doon ba muy moom
Lonkoti naa, foo ma jaar?
Man yaw rekk la bëgg
Pare naa bañ bañ na dara
My baby boo
Ku la moom?
Man ma la moom
Laaj ma ku ma moom man
Ma bañ duma ko wax
Nga ni ku la moom
Man ma la moom
Laaj ma ku ma moom man
Yaw rekk yaw rekk lay doon ba muy moom
Yaay sama faru-rab
Jege ma dolli
Doro ku la moom?
Clara la moom
Laaj ma ku ma moom man
Ma bañ duma ko wax
Bamba ku la moom?
Aïcha la moom
Laaj ma ku ma moom man
Yaw rekk yaw lay doon ba muy moom
Lonkotina
Mano, eu não sei se alguém vai me entender
Eu só quero ficar bem e não consigo parar de pensar
A vida é uma luta, não é fácil como parece
Eu estou aqui, longe de casa, ouvindo Pape e Cheikh
Ouhou ouhou ouh...
Se você não sabe, é porque não provou o doce que é bom
Ouhou ouhou ouh...
Eu já vi a luz que te trouxe de volta
E você, quem é...
Quem é você?
Eu sou eu, quem é você?
Me diga quem é você, eu sou eu
Eu não vou te dizer nada
E você, quem é você?
Eu sou eu, quem é você?
Me diga quem é você, eu sou eu
Só você, só você, você é tudo que eu quero
Longe de casa, onde você está?
Eu só quero você
Eu não quero mais nada
Meu amor, meu bem
Meu gato, ele é rápido
"Suma suma lomsong fi jubbo lonkong"
Eu me perco na dança
Eu me divido entre você e o outro lado
O que é doce pra você?
Tempo, tempo, pegue seu tempo, eu estou aqui esperando
A vida é curta, então eu quero ver seu sorriso
Coloque um pé na frente, então eu coloco dois atrás de você
Não se preocupe, não se afaste
Olhe o que você faz com suas mãos
Coloque um pé na frente, então eu coloco dois atrás de você
Ho ho ho ho, a verdade é que você está aqui
Ouhou ouhou ouh...
Se você não sabe, é porque não provou o doce que é bom
Ouhou ouhou ouh... (ouxayati)
Eu já vi a luz que te trouxe de volta
E você, quem é...
Quem é você?
Eu sou eu, quem é você?
Me diga quem é você, eu sou eu
Eu não vou te dizer nada
E você, quem é você?
Eu sou eu, quem é você?
Me diga quem é você, eu sou eu
Só você, só você, você é tudo que eu quero
Longe de casa, onde você está?
Eu só quero você
Eu não quero mais nada
Meu amor, meu bem
Quem é você?
Eu sou eu, quem é você?
Me diga quem é você, eu sou eu
Eu não vou te dizer nada
E você, quem é você?
Eu sou eu, quem é você?
Me diga quem é você, eu sou eu
Só você, só você, você é tudo que eu quero
Oh, meu amor
Me faça sentir
Quem é você?
Clara, quem é você?
Me diga quem é você, eu sou eu
Eu não vou te dizer nada
Bamba, quem é você?
Aïcha, quem é você?
Me diga quem é você, eu sou eu
Só você, só você, você é tudo que eu quero