Tradução gerada automaticamente

exibições de letras 1

Sama Xool (feat. VJ)

Mia Guisse

Letra

Sama Xool (feat. VJ)

Sama Xool (feat. VJ)

Então, não me deixe só, eu não quero ficar assimSoo ma soree nu may nooye sama xol kaay
Diz pra mim que não vai me deixar, que eu não vou morrerWaatal ma ni doo ma bàyyi ba ba may dee
Você viu a beleza que eu tenho, se eu te deixar?Gisoo mbégte bi may àndal su ma lay wayal?
É só o rei que sabe onde você me pegouNdax laawu Buur bi rekk a xam fi nga ma jële

Eu te dou meu coraçãoDénk naa la sama xol bi
Eu te dou meu coraçãoYéene naa la sama xol bi
Eu escuto você na sua menteDégg naa la ci sa xol bi
Então, onde você vai me levar, eu vou fazerKon nak foo móolee pikkiru laay def
Você coloriu meu coraçãoColoré nga sama xol bi
Eu te dou minha cabeçaDénk naa la sama bopp
O que você faz com meu coraçãoLi nga liggéey ci sama xol bi
É como se a mãe estivesse me deixando aquiWuy yaay bi bànneex nii mu may def

Diga que você está bemSay xeetu xaar baax
Eu só quero que você me diga que está tudo certoMan su ma koy lim fi de laay des
Se eu te deixar, você vai querer me ver de novo?Ndax su ma feeberee bëgg wér séeti ko laay def
O parlamento diz que eu sou um bandidoParlement bi yépp naan bandit laa
Eles dizem que eu sou um, você vai me deixar aquiÑi naan kobb laa, nga ñëw tànn ma
Baby, o que você está dizendo?Baby yaw ci loo ne?
Me diz, nós estamos juntosJegesi ma, ñu felfëlaale

Eu te dou meu coraçãoDénk naa la sama xol bi
Eu te dou meu coraçãoYéene naa la sama xol bi
Eu escuto você na sua menteDégg naa la ci sa xol bi
Então, onde você vai me levar, eu vou fazerKon nak foo móolee pikkiru laay def
Você coloriu meu coraçãoColoré nga sama xol bi
Eu te dou minha cabeçaDénk naa la sama bopp
O que você faz com meu coraçãoLi nga liggéey ci sama xol bi
É como se a mãe estivesse me deixando aquiWuy yaay bi bànneex nii mu may def

Eu estou aquiMaa ngi séet
Onde você está, simFi ma la def waaw
Mãe, eu sou o rei, bebêYaay ki ma def roi bébé
Me mostre o que você temXamal ma luy nobeel

Quando nós nos encontramosBa ñu gisee
Eu não vou te deixar, simMënuma xef waaw
Só você e eu, sim, bebêBëtu mbëggeel rekk waaw, bébé
Eu não vou te deixarLaa la mës a xoole

Eu sou seu único amor, você vai me deixar?Man sama jëmm ji rekk nga jaaxal?
Eu não vou me afastar de você, porque você é tudo pra mimDuma bett ci yaw ndax ndaanaan nga
Eu não vejo ninguém, porque você é tudo que eu queroDuma xool keneen ndax yaw mi yaa ma doy
Eu sou seu único amorMaa la njëkk barde

Eu sou seu amor, o que mais eu posso fazer? (Nada)Man sama bae nga, lu ci nit ñi mën? (Dara)
E meus sentimentos não vão emboraTe sama féem yi rëcc ci du gaaw
Quando você me chama, eu vou entrar na sua vidaBa nga réppee ba dugg ci Mami Guissé
Eu só quero ver vocêLaa la xool rekk ree

Eu te dou meu coraçãoDénk naa la sama xol bi
Eu te dou meu coraçãoYéene naa la sama xol bi
Eu escuto você na sua menteDégg naa la ci sa xol bi
Então, onde você vai me levar, eu vou fazerKon nak foo móolee pikkiru laay def
Você coloriu meu coraçãoColoré nga sama xol bi
Eu te dou minha cabeçaDénk naa la sama bopp
O que você faz com meu coraçãoLi nga liggéey ci sama xol bi
É como se a mãe estivesse me deixando aquiWuy yaay bi bànneex nii mu may def

Eu te dou meu coraçãoDénk naa la sama xol bi
Eu te dou meu coraçãoYéene naa la sama xol bi
Eu escuto você na sua menteDégg naa la ci sa xol bi
Então, onde você vai me levar, eu vou fazerKon nak foo móolee pikkiru laay def
Você coloriu meu coraçãoColoré nga sama xol bi
Eu te dou minha cabeçaDénk naa la sama bopp
O que você faz com meu coraçãoLi nga liggéey ci sama xol bi
É como se a mãe estivesse me deixando aquiWuy yaay bi bànneex nii mu may def

Comentários

Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra

0 / 500

Faça parte  dessa comunidade 

Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de Mia Guisse e vá além da letra da música.

Conheça o Letras Academy

Enviar para a central de dúvidas?

Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.

Fixe este conteúdo com a aula:

0 / 500

Opções de seleção