395px

Mamãe África

Youssou N'dour

Mama Africa

Yée, yée-hé-hé-hé
Yée, yée-hé-hé-hé
Hoo, hoo ehnn haan

Hoo Africains, woy le leen ma Africa
Benn continent, melul ni Africa
Amul benn werente ci loolu
Suñu mbëggél ci yaw, Africa
Amna ñi soriyaante
Bu ñu kenn jaxasse
Na ñu xam suñu bopp
Une jeunesse engagée, Africa
Namm u ñu dara, yalla a la barkeel
Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
Boo xasee miin xam ni, fii mooy suñu kër
Come home with me
Hoo Africains, woy le leen ma Africa
Benn continent, melul ni Africa
Amul benn werente ci loolu
Suñu mbëggél ci yaw, Africa
Ana ñi soriyaante
Bu ñu kenn jaxasse
Na ñu xam suñu bopp, avec
Une jeunesse engagée, Africa
Namm u ñu dara, yalla a la barkeel
Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
Boo xasee miin, xam ni, fii mooy suñu kër
Come home with me
Ñun Africains, su ñu ànd a ndoo
Bokk nday ak baay, Boole suñuy doole
Kholal ëllëg u adduna bi
Seetal say doom ñoo, koy mujjee

Yée, hée hée, an han

Ni nga maggeek, ni nga yaatoo
Noonu nga riché
Ni nga maggeek, ni nga yaatoo
Noonu nga riché
Du ñu la weccoo ba muk
Du ñu la weccoo keneen Africa
Xam nga ni la say, doom yi bëggee

Tag naa la kaay
Yaa ne ci suñu xol
Wo, wo, wo, wooy
Wo, wo, wo, wooy
Du ñu la mas a weccooy
Kenn du yaw Africa

Yée
Yée hé hé hée hé

Mamãe África

É, é-hé-hé-hé
É, é-hé-hé-hé
Hoo, hoo ehnn haan

Hoo africanos, ouçam minha África
Um continente, é tudo África
Não há um só lugar como esse
Nosso amor por você, África
Temos uma juventude
Que não se deixa abater
Vamos nos conhecer melhor
Uma juventude engajada, África
Amém, que nada nos falte, Deus te abençoe
Você está em nossos corações, nós te acolhemos
Se você souber, aqui é nosso lar
Venha pra casa comigo
Hoo africanos, ouçam minha África
Um continente, é tudo África
Não há um só lugar como esse
Nosso amor por você, África
Onde está a juventude
Que não se deixa abater
Vamos nos conhecer melhor, com
Uma juventude engajada, África
Amém, que nada nos falte, Deus te abençoe
Você está em nossos corações, nós te acolhemos
Se você souber, aqui é nosso lar
Venha pra casa comigo
Nós, africanos, estamos juntos nessa
Unidos como pai e mãe, juntando nossas forças
A vida é uma luta
Olhe para nossos filhos, eles vão brilhar

É, hée hée, an han

Se você é forte, se você é sábio
Então você é rico
Se você é forte, se você é sábio
Então você é rico
Nós te acolhemos, não importa o que aconteça
Nós te acolhemos, não importa a África
Você sabe que seus filhos são valiosos

Eu te chamei
Você está em nosso coração
Wo, wo, wo, wooy
Wo, wo, wo, wooy
Nós te acolhemos com amor
Ninguém te deixará, África

É
É hé hé hée hé