Tradução gerada automaticamente

Naari Xalé (feat. Ashs The Best)
Obree Daman
Naari Xalé (feat. Ashs The Best)
Naari Xalé (feat. Ashs The Best)
Bay Moodu, não me deixe em pazBay Moodu demal mu ne du dem
Xelam, não me deixeXelam dallul
Bêgg, não me deixe, eu não posso te deixarBëgg dem taxul ta mën a dem
Eu não posso te deixar, não posso te deixarMën a dem, moy tax a dem
Waayam, sim, é isso, pegue o caminhoWaayam ja, yàkkamti woon, jël yoon wa
E esse caminho não é o meuTe yoon woowe du yoonam
Na terra que se vê, na terra que se vêCi lëndëm mu gis fa réer, ci lëndëm ñu gis fa réer
Entrando na casa, esperança flui na água, na beira do mar, na beira do marDugg ci gaal, yaakaar féey ci ndox ci digg u geej ci diggu geej
Surux, a esperança é tudo, todos vão se juntarSurux, yaakaar yépp tas na, ñépp ngaay jooy
Bay Moodu, não me deixeBay Moodu dem na
(Deixa eu ir?)(Lutax mu dem?)
Picc, não me deixe, eu não posso te deixar, a mente dos que estão na terraPicc ramatu ma ngay naaw waye xel mu ñi ci suuf
Eles podem se machucar, a verdade é que não podemos nos separarÑu mën a kott, dëgg-dëgg ndekete yorul ñu mbaam
Naari xale, eles são os que servem a DeusÑaari xale, ñoo ñi wër yàlla
Naari xale, eles são os que servem a DeusÑaari xale, ñoo ñi wër yàlla
Seu lugar é aqui, é onde estãoSeeni rangoñ moo fi tuuru woon
Servimos até morrer (servimos até morrer)Wër nañu ba dee (wër nañu ba dee)
Servimos até morrerWër nañu ba dee
Quem é que está chamando?Kan mooy laal ngone
Quem é que está chamando?Kan mooy laal ngone
Chame a Deus (quem é que está chamando?)Laal na yàlla (kan mooy laal ngone)
(Quem é que está chamando?)(Kan mooy laal ngone)
Quem é que está chamando?Kan mooy laal ngone
Quem é que está chamando?Kan mooy laal ngone
Chame a DeusLaal na yàlla
Kuu, pegue a mão que te levanta (quem é que está chamando?)Kuu jàpp ci loxoom waay mu yobbu la (kan mooy laal ngone)
(Quem é que está chamando?)(Kan mooy laal ngone)
(Chame a Deus)(Laal na yàlla)
Kumba, a vida é porque não há mãeKumba jirim la ndax ñàkk yaay
Baayam, não esqueça, não se esqueça de mimBaayam tële, dénk ka nijaayam
Na minha juventude, na minha juventudeCi ba mi ndaw, ci ba mi ndaw
A juventude deve ser livre, não se esqueça de mim (Kumba, a vida)Nijaayam war ko yar, far sàkku ndawam (Jirim kumba)
Deixe isso com a força que não pode se levantar (deixe isso comigo)Bàyyi ko ak màndaga bu dul jóg ci moom (ba ba mi de)
Picc, não me deixe, eu não posso te deixar, a mente dos que estão na terra (quem é que está chamando?)Picc ramatu ma ngay naaw waye xel mu ñi ci suuf (kan mooy laal ngone)
(Quem é que está chamando?, chame a Deus)(Kan mooy laal ngone, laal na yàlla)
Eles podem se machucar, a verdade é que não podemos nos separar (quem é que está chamando?)Ñu mën a kott, dëgg-dëgg ndekete yorul ñu mbaam (kan mooy laal ngone)
(Quem é que está chamando?, chame a Deus)(Kan mooy laal ngone, laal na yàlla)



Comentários
Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra
Faça parte dessa comunidade
Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de Obree Daman e vá além da letra da música.
Conheça o Letras AcademyConfira nosso guia de uso para deixar comentários.
Enviar para a central de dúvidas?
Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.
Fixe este conteúdo com a aula: