Tradução gerada automaticamente

exibições de letras 5

Waxoma Woon Lii

OMG

Letra

A Música do Coração

Waxoma Woon Lii

Beuga toma wakhmaBeuga toma wakhma
Xawma lu waral légui mane falé tomaXawma lu waral légui mane falé toma
Guiss nani diex naGuiss nani diex na
Waxoko mais khamnani ni nobatomaWaxoko mais khamnani ni nobatoma
Gaaw ci defma luma métiGaaw ci defma luma méti
Say wax néxatul mangui deg lu néSay wax néxatul mangui deg lu né
Lu dieum ci mane sa yoon nékoussiLu dieum ci mane sa yoon nékoussi
Souma déwoon do weet ndax du mane malay wétaliSouma déwoon do weet ndax du mane malay wétali

Wano ma woon liiWano ma woon lii
Bagnouy tambaliBagnouy tambali
Waxo ma wone liiWaxo ma wone lii
Meunatuma ndax dama taayiMeunatuma ndax dama taayi
Wano ma woon liiWano ma woon lii
Bagnouy tambaliBagnouy tambali
Wakho ma woon liiWakho ma woon lii
Meuneutou mala mougneul dax mane dame la baayiMeuneutou mala mougneul dax mane dame la baayi
Dame la bayi héDame la bayi hé
Dame la bayi héDame la bayi hé
Dame la bayi héDame la bayi hé
Toggatumafi di mougn ndax mane taayiToggatumafi di mougn ndax mane taayi
Dame la BaayiDame la Baayi
Dame la BaayiDame la Baayi
May kila baayiMay kila baayi

Goudi ba goudi lalay guissGoudi ba goudi lalay guiss
Dem na ba légui damako missDem na ba légui damako miss
Waxa tok maneWaxa tok mane
Falé tomaFalé toma
Sama wétal doon naxar ak tissSama wétal doon naxar ak tiss
Yay kiy béguel samay noonYay kiy béguel samay noon
Bax ci mbed mi ci mane nga boneBax ci mbed mi ci mane nga bone
Dieukeur boula yénétoul foonDieukeur boula yénétoul foon
Ma name la té sori womaMa name la té sori woma

Wano ma woon liiWano ma woon lii
Bagnouy tambaliBagnouy tambali
Waxo ma wone liiWaxo ma wone lii
Meunatuma ndax dama taayiMeunatuma ndax dama taayi
Wano ma woon liiWano ma woon lii
Bagnouy tambaliBagnouy tambali
Wakho ma woon liiWakho ma woon lii
Meuneutou mala mougneul dax mane dame la baayiMeuneutou mala mougneul dax mane dame la baayi
Dame la bayi héDame la bayi hé
Dame la bayi héDame la bayi hé
Dame la bayi héDame la bayi hé
Toggatumafi di mougn ndax mane taayiToggatumafi di mougn ndax mane taayi
Dame la BaayiDame la Baayi
Dame la BaayiDame la Baayi
May kila baayiMay kila baayi

Mangui dem guissouma liy tax may deloussiMangui dem guissouma liy tax may deloussi
Bou déssé loudoul sa keur ma fanaan ci mbed miBou déssé loudoul sa keur ma fanaan ci mbed mi
And nexna wayé ko ba mou démak mbagamAnd nexna wayé ko ba mou démak mbagam
Diox la sama xol ga fowé ko yaw danga lundeumDiox la sama xol ga fowé ko yaw danga lundeum
Yag na du tayYag na du tay
Wané gako tayWané gako tay
Naxaral sama xol xam nga yako tayNaxaral sama xol xam nga yako tay
Légui dafa doyLégui dafa doy
Dotou mako joyDotou mako joy
Beuss sa gui ci beussi lo lebblé lagne lay fayBeuss sa gui ci beussi lo lebblé lagne lay fay


Comentários

Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra

0 / 500

Faça parte  dessa comunidade 

Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de OMG e vá além da letra da música.

Conheça o Letras Academy

Enviar para a central de dúvidas?

Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.

Fixe este conteúdo com a aula:

0 / 500

Opções de seleção