Tradução gerada automaticamente

exibições de letras 3

Diaral Ngama (feat. Cherifou)

Pendo Guissé

Letra

Diaral Ngama (feat. Cherifou)

Diaral Ngama (feat. Cherifou)

Duma dem, duma dikk, duma yónneeDuma dem, duma dikk, duma yónnee
Quem não se importa, me diz que não vale a penaKu dem-dikk wax ma ma neexal la
Aqui tá tudo certo, sim, aqui tá tudo certoCi jaga, waaw ci jaga

Eu já te amo, dentro de vocêTàmm naa la man ci seen biir
O que a gente tem é muito, eu te amo de verdadeLu ñu bari-bari yaa ma ci doyloo
Você me faz bemJaral nga ma
Eu te amo, simMan yaa ma yendoo

Se Deus não quiser, não vai rolarBu Yàlla ñëwul dafa yónnee
Quem acredita que vai rolar, vai se dar bemKu gëm ki mu yónni mu neexal la
(Se for pra ser, então vamos juntos)(Ko koy dogal te moo ñu boole)
Sim, vamos juntosWaaw mooy dogal
(Sim, vamos juntos)(Waaw mooy boole)

Eu vejo você aqui, você vai sairXool naa la fi, nga génn fee
Eu vejo você aqui, você vai voltarMa xool la fi, nga génnaat fee
A noite tá começando a esquentarNaaj bi tànk may daw di daw
A energia do meu corpo táLangaamu sama yaram daw

Você tá me deixando louco (eu vejo você)Yaw la doon seet (gis naa la)
Eu te amo de verdade (sim, baby, vem)Man yaa ma doyloo (waaw baby kaay)
Querida, você me faz feliz (sim, querida, vem)Chérie yaa may jooyloo (waaw chéri kaay)
Eu te amo de verdade (sim, baby, vem)Man yaa may dofloo (waaw baby kaay)

Se eu não me segurar, vou acabar me entregandoSoo sibbiru ma pikkiru naan fay doom
Coração tá pedindo pra eu me jogarCoono bégal laa la faydo
Isso é o que eu quero, é tudo que eu queroLi mooy mbëggeel bànneex a neex

Querida, eu te amo, não quero mais nadaChéri bëgg laa ba dee ci dagaan
Quero quem me ama de verdade, não quero só conversaBëgg ku la gën a bëggaati dagaan
Mais amor, mais amor, mais amorGën bi gën a gën
Isso é o que eu quero, é tudo que eu queroLi mooy mbëggeel bànneex a neex

Eu já te amo, dentro de vocêTàmm naa la man ci seen biir
O que a gente tem é muito, eu te amo de verdadeLu ñu bari-bari yaa ma ci doyloo
Você me faz bemJaral nga ma
Eu te amo, simMan yaa ma yendoo

Se Deus não quiser, não vai rolarBu Yàlla ñëwul dafa yónnee
Quem acredita que vai rolar, vai se dar bemKu gëm ki mu yónni mu neexal la
(Se for pra ser, então vamos juntos)(Ko koy dogal te moo ñu boole)
Sim, vamos juntosWaaw mooy dogal
(Sim, vamos juntos)(Waaw mooy boole)

Eu vejo você aqui, você vai sairXool naa la fi, nga génn fee
Eu vejo você aqui, você vai voltarMa xool la fi, nga génnaat fee
A noite tá começando a esquentarNaaj bi tànk may daw di daw
A energia do meu corpo táLangaamu sama yaram daw

Você tá me deixando louco (eu vejo você)Yaw la doon seet (gis naa la)
Eu te amo de verdade (sim, baby, vem)Man yaa ma doyloo (waaw baby kaay)
Querida, você me faz feliz (sim, querida, vem)Chérie yaa may jooyloo (waaw chéri kaay)
Eu te amo de verdade (sim, baby, vem)Man yaa may dofloo (waaw baby kaay)

Quem ama não se importa, quem ama não se importaKu ndayam nangu mu takk la, ku ndayam nangu

Quem não se importa, só quer saber de amor, e você vai se dar bemKu dem la jël takk ci sëgg te ngeen booleek ricc ku neex jëlal
Se você se jogar, vai se dar bemAy bu ko jékko da koy ricc mu neex

Se Deus não quiser, não vai rolarBu Yàlla ñëwul dafa yónnee
Quem acredita que vai rolar, vai se dar bemKu gëm ki mu yónni mu neexal la
Isso eu falo pra Aïcha DialloLoolu ma booleek Aïcha Diallo
E também pra Marie BaraMoo ma booleek Marie Bara

Eu vejo você aqui, você vai sairXool naa la fi, nga génn fee
Eu vejo você aqui, você vai voltarMa xool la fi, nga génnaat fee
A noite tá começando a esquentarNaaj bi tànk may daw di daw
A energia do meu corpo táLangaamu sama yaram daw

Você tá me deixando louco (eu vejo você)Yaw la doon seet (gis naa la)
Eu te amo de verdade (sim, baby, vem)Man yaa ma doyloo (waaw baby kaay)
Querida, você me faz feliz (sim, querida, vem)Chérie yaa may jooyloo (waaw chéri kaay)
Eu te amo de verdade (sim, baby, vem)Man yaa may dofloo (waaw baby kaay)

Você é meu Deus, me faz bemYaw la ma Yàlla boole
Djie Astou SalléDjie Astou Sallé
Quem é meu Deus, me faz bemKi la ma Yàlla boole
Djie Astou SalléDjie Astou Sallé

Comentários

Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra

0 / 500

Faça parte  dessa comunidade 

Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de Pendo Guissé e vá além da letra da música.

Conheça o Letras Academy

Enviar para a central de dúvidas?

Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.

Fixe este conteúdo com a aula:

0 / 500

Opções de seleção