395px

Motema (feat. Baye Mass)

Sidy Diop

Motema (feat. Baye Mass)

Wax ma loo bëgg ma defal la ko
Am naa sa yéene, am naa tam sa jot
Li nga ma wan doy ma éclairer sama yoon
Yaa tax ma gis leer au bout du túnel

Ma la gëna jége sa yere yi nga sol
Ci mbëggeelu jokk jokk laa lay woo
Li ma bélli, lëndëmal jant bi
Ngoonalu dibéer laa li woo

Jox ma sa mbëggeel ma déncal la ko
Su ci njaabot juddoo ma sàmmal la ko
Ci sa wet am naa fa jàmm
Yaw de doy nga ma, yaay lumièru siñaara yea

Booy compter one one baby yaa ngi ci kaw rekk
Lu mu tàng tàng tàng na ko jéri man rekk
Te lu mu metti metti metti metti metti
Na ko siicu-siicuwaat mu njan

Danga miig di zonzé, xeere nooy di bondé
Ku lay compter danaan un un yaa ngi ci un rekk
Maa la peser xam ni nit ku mel ni yaw
Yàlla sakkul ci ñaar, billaay!

Mbëggeelu temps yi, xëppante acide la
Bu ma bàyyi, sama exitran nga
Lu mu metti metti metti metti bae
Dinaa ko muñ ngir mbëggeel gi ma am ci yaw

Maa ngi tëddoon def tekk
Noboss koboss ma ni tekk
Taxaw demb di jokk rekk
Ma bañ mu ni ma jokk rekk
Yaa ma yee mu neex ma ndaxte
Foo ma yee yeetal beey gëna neex
Baby yaw rekk!

Baby manaak yaw rekk
Ci biir néegu bu wet rekk
Ci lal bu nooy rekk
Ma koy defal ak yaw rekk
Ak yaw rekk!
Booy jooy doo ko tay ak man rekk

Maa ngi tëddoon def tekk
Noboss koboss ma ni tekk
Taxaw demb di jokk rekk
Ma bañ mu ni ma jokk rekk
Yaa ma yee mu neex ma ndaxte
Foo ma yee yeetal beey gëna neex
Baby yaw rekk!

Sama jeeg bu jar bi
Saf ni soosu kaani
Sama star bi
Fu ma jëm ak sa taar bi
Lu may wiri wiri delluwaat
Ci point départ bi

Répertoire bi yaw rekk
Samay message yaw rekk
Sama yitte yaw rekk
Sama quotidien yaw rekk
Soo ma soxlawee liggéey bi soxla ma bul ma laaj
Kan mooy xaar? Baby yaw rekk!

Yee yeeh

Baby manaak yaw rekk
Ci biir néegu bu wet rekk
Ci lal bu nooy rekk
Ma koy defaak yaw rekk
Ak yaw rekk!
Booy jooy doo ko tay ak man rekk

Danga miig di zonzé, xeere nooy di bondé
Ku lay compter danaan un un yaa ngi ci un rekk
Maa la peser xam ni nit ku mel ni yaw
Yàlla sakkul ci ñaar, billaay!

Bébé baal ma
Yaw bébé baal ma!

Danga doon wëyu wëyu lu boy bandit ba ngi ni!
Bébé baal ma
Yaw bébé baal ma

Danga doon wëyu wëyu lu bandit cerveau ba ngi ni!
Bébé baal ma
Yaw bébé baal ma

Ku la dul def lutax nga naan woy wooy wooy, loo koy doye?
Bébé baal ma
Yaw bébé baal ma

Danga doon wëyu wëyu lu bandit cerveau ba ngi ni!
Bébé baal ma
Yaw bébé baal ma

Danga doon wëyu wëyu lu magu bandit yaa ngi ni!
Bébé baal ma
Yaw bébé baal ma

Ku la dul def lutax nga naan woy wooy wooy, loo koy doye?
Bébé baal ma
Yaw bébé baal ma

Danga doon wëyu wëyu lu bandit cerveau ba ngi ni!
Bébé baal ma
Yaw bébé baal ma

Danga doon wëyu wëyu lu bandit cerveau ba ngi ni!
Bébé baal ma
Yaw bébé baal ma

Hummm bah!
Ñoo fi jar!

Motema (feat. Baye Mass)

Não sei se você quer que eu faça isso
Eu tenho sua luz, eu tenho seu jeito
O que você me deu, me ajuda a iluminar meu caminho
Por isso eu vejo a luz no fim do túnel

Eu já estou cansado de esperar por você
Na espera, eu só fico aqui
O que eu quero, é que você me dê
Um pouco de amor, só isso

Me dê sua luz, eu vou me afastar
Se na estrada eu não conseguir me encontrar
Com você, eu só quero paz
Você é tudo pra mim, oh luz da minha vida, é

Vamos contar um, dois, baby, você tá aqui só pra mim
O que você faz, faz, faz, faz, faz, eu só quero você
E o que você diz, diz, diz, diz, diz
Me faz sentir que eu sou seu

Você tá me fazendo sentir, meu bem, não me deixe
Quem vai contar, só um, um, você tá aqui só pra mim
Eu sei que você é como eu
Deus, me ajude a não errar, por favor!

O tempo passa, a espera é amarga
Se eu desistir, você vai me deixar
O que você diz, diz, diz, diz, diz
Eu vou lutar pra ter você aqui

Eu só quero fazer acontecer
Sem chefe, só eu e você
Levanta, vem aqui só pra mim
Eu não quero que você se vá, não quero
Você é tudo pra mim, porque
Se eu te perder, vai doer demais
Baby, só você!

Baby, só você
Dentro do meu coração, só você
Na minha vida, só você
Eu quero fazer isso com você
Com você!
Vamos juntos, só nós dois

Eu só quero fazer acontecer
Sem chefe, só eu e você
Levanta, vem aqui só pra mim
Eu não quero que você se vá, não quero
Você é tudo pra mim, porque
Se eu te perder, vai doer demais
Baby, só você!

Meu sonho se tornou realidade
Como um sonho que se realiza
Minha estrela
Se eu me encontrar com sua luz
O que brilha, brilha, brilha
No ponto de partida

O repertório é só seu
Minha mensagem é só sua
Meu pensamento é só seu
Meu cotidiano é só seu
Se eu te deixar, o trabalho não vai me deixar em paz
Quem vai me ajudar? Baby, só você!

É, é

Baby, só você
Dentro do meu coração, só você
Na minha vida, só você
Eu quero fazer isso com você
Com você!
Vamos juntos, só nós dois

Você tá me fazendo sentir, meu bem, não me deixe
Quem vai contar, só um, um, você tá aqui só pra mim
Eu sei que você é como eu
Deus, me ajude a não errar, por favor!

Bebê, me escuta
Você é meu bebê!

Você tá aqui, aqui, como um bandido, não é?
Bebê, me escuta
Você é meu bebê!

Você tá aqui, aqui, como um bandido inteligente, não é?
Bebê, me escuta
Você é meu bebê!

Quem vai fazer o que você quer, me diz, o que você quer?
Bebê, me escuta
Você é meu bebê!

Você tá aqui, aqui, como um bandido inteligente, não é?
Bebê, me escuta
Você é meu bebê!

Você tá aqui, aqui, como um bandido, não é?
Bebê, me escuta
Você é meu bebê!

Quem vai fazer o que você quer, me diz, o que você quer?
Bebê, me escuta
Você é meu bebê!

Você tá aqui, aqui, como um bandido inteligente, não é?
Bebê, me escuta
Você é meu bebê!

Você tá aqui, aqui, como um bandido inteligente, não é?
Bebê, me escuta
Você é meu bebê!

Hummm, ah!
Estamos aqui!