Tradução automática

Exibições da letra 3

Nous 2 (part. Wally B. Seck)

Viviane Chidid

Letra

NOUS 2 (parte. Wally B. SECK)

Nous 2 (part. Wally B. Seck)

Você não percebe que eu não estou te vendendo casamento?Yëguloo ne séy duma la koy jaay
Eu simplesmente sei o meu preço e sei quanto valhoDama xam rekk sama njëg, xam tamit lu maay jar
Você não percebe que eu não sou uma mulherYëguloo ne man jigéen duma jaay neex
Mas eu já sei o meu preçoDama xam rekk sama njëg xam tamit
Só quero que você saiba que suas aulas não me incomodamDama lay wax nga xam ni sa ñangal safu ma dara (dara)
Sem mim você não é nada (nada)Sans man yaw doo dara (dara)
Você se esquece que eu sei (eu sei)Danga ma fàtte xam naa (xam naa)
Quando você massageia meus pés e me diz para te amar, pelo amor de DeusBa ngay ram sama tànk naan ma nob la ngir Yàlla (yàlla)
Estou satisfeito com o que você sabeLoo xam lu neex man la
O casamento não me incomoda, oh, sim, simSéy jaaxalu ma oh, yeah, yeah

Você é o único que entra no arquivo de salvamentoDalal fok ni yaw rekk ya dugg mbar ànd AK salbe
Rapaz, você acha que é o único homem?Boy mbaa du danga foog ne yaw rekk yaay góor wala?
Quantas vezes você já me deu socos na cara como se eu fosse uma criança?Ñaata yoon nga ram sama kanam comme xale
Se quiser, pode dar um passeioBu la neexe nga doxan
Você finge que não estava láYaw defal comme si j'étais pas là
Oh, por favor, não passe a noite aquiOoh, bu la neexe, bul fanaan ci yaw
Você finge que não estava láYaw defal comme si j'étais pas là
Você finge que não estava láYaw defal comme si j'étais pas là

Você não percebe que eu não estou te vendendo casamento?Yëguloo ne séy duma la koy jaay
Eu simplesmente sei o meu preço e sei quanto valhoDama xam rekk sama njëg, xam tamit lu maay jar
Você não percebe que eu não sou uma mulherYëguloo ne man jigéen duma jaay neex
Mas eu já sei o meu preçoDama xam rekk sama njëg xam tamit

Você está se enganandoYaa ngi nax sa bopp
Você acha que eu sou mesquinhoDanga foog ni man maa xëy
Barde de outra pessoaBarde ci keneen
Há muita conversa sobre isso, então, o que você está esperando?Wax ji bari na, ana looy xaar?
Vá para outro lugar!Demal feneen
Posso te contar mais e você voltaráMaa leen mën bari cacc yaay ñëwaat
Naan bae, me desculpeNaan bae jéegalu naa
Sabe, podem chamá-lo de ladrão de cérebrosXam nga ko ko sekkal bandit cerveau la woo
Impede você de dormirTere la nelaw
Como começar com eeComme d'hab ay wax ngay tambalee ee
E você acaba chorando eeTe ay jooy ngay mujje ee
Chame sua boca de May, venha e peça desculpas de novo, peça desculpas de novoWool sa bawat mee, ñëw baaluwaat, baaluwaat

Se quiser, pode dar um passeioBu la neexe nga doxan
Você finge que não estava láYaw defal comme si j'étais pas là
Oh, por favor, não passe a noite em vocêOoh, bu la neexe bul fanaan ci yaw
Você finge que não estava láYaw defal comme si j'étais pas là
Você finge que não estava láYaw defal comme si j'étais pas là

Você não percebe que eu não estou te vendendo casamento?Yëguloo ne séy duma la koy jaay
Eu simplesmente sei o meu preço e sei quanto valhoDama xam rekk sama njëg, xam tamit lu maay jar
Você não percebeu o quanto eu te amavaYëguloo ne maa la gëna neex
Mas eu já sei o meu preçoDama xam rekk sama njëg xam tamit
Só estou dizendo para você saber que seu método de ensino não me incomodaMan dama lay wax nga xam ni sa ñangal safu ma dara (dara)
Sem mim você não é nadaSans man yaw doo dara
Você se esqueceu de mim, eu seiDanga ma fàtte xam naa
O diabo te convenceu de que você é o único?Mbaa du seytaan la jaay ba nga foog ni yaw rekk la

Agora ela é tão doce quanto AidaLéegi dafa sukka mel ni Aïda sukkeer
É por isso que você chora quando ninguém te tocaMoo tax ngay jooy te loxo du la laal yaw
Eles sabem o que você fazXamante nañu mak yaw
Vou me comprometer com vocêTéye sama bopp ci yaw laay def
E se você fizer isso, vai ser difícil para mimBoo ko defe dinaa metti fees ci man
Estou apenas bebendo, mas não consigo te deixarDamay nàppe rekk mais mënuma la bàyyi
Eu te amo e isso está claro para mim, vamos láMan yaw laa nob te leer na ma, kaay waay
Meu amor, meu bem, eu te amo!Sama reni xol, bébé n b'i fe
Eu te amo, minha linda woyu ViTi voglio bene, sama bella woyu Vi
Eu te contei sobre a mãe do bandidoWax naa la yaay baayam bandit bi
Eu te amo e me importo com você, simBëgg naa la, faale naa la waawaaw
Sim, simEee, ee

(Não consigo viver sem você)(Je ne peux pas vivre sans toi)
Se você ficar com raiva de mim, fique com raiva de mimBoo ma mere réy ma
Porque você é quem faz meu coração felizNdax yaw yaay ki tax xol bi neex na
(Não consigo viver sem você)(Je ne peux pas vivre sans toi)
Oh, meu bem, quando você fica brava, me machucaOh mon bébé soo mere gaañ ma
No fundo, obviamente, a criançaCi xol leer na, xale bi
(Não consigo viver sem você)(Je ne peux pas vivre sans toi)
Meu bebê, Deus me deu vocêBaby Yàlla la sax jox ma
Eu me apaixonei por você, meu bemMa jël nob la, xale bile
(Não consigo viver sem você)(Je ne peux pas vivre sans toi)
Eu te amarei até o fim da minha vidaYaw ma la bëgg ba mu jeex ma tay
Você está me matando, meu bem!Yaw yaa may ray, xale bi
(Não consigo viver sem você)(Je ne peux pas vivre sans toi)
A mãe não sabe dissoNdeysaan xamuloo ne
As discussões terminam quando você as vêXuloo boo gis dafay jeex
(Não consigo viver sem você)(Je ne peux pas vivre sans toi)
E quando você acorda, a sensação no meio da noite é boaBoo jubboowee sa xaaju guddi day neex
(Não consigo viver sem você)(Je ne peux pas vivre sans toi)

Comentários

Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra

0 / 500

Faça parte  dessa comunidade 

Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de Viviane Chidid e vá além da letra da música.

Conheça o Letras Academy

Enviar para a central de dúvidas?

Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.

Fixe este conteúdo com a aula:

0 / 500

Opções de seleção