Tradução gerada automaticamente

exibições de letras 89

Sibam (feat. Sidate Bonbon)

Viviane Chidid

Letra

Sibam (feat. Sidate Bonbon)

Sibam (feat. Sidate Bonbon)

You know I’m feeling good tonightTay ji bésu begete la gay ñi
You know I’m ready to shineTay ji ñëwel ñu ànd fecc

Big and small, no boys or girlsMag ak ndaw, amul góor ak jigéen
The night is alive and brightÑëwel dugg ci géew gi
Big and small, no boys or girlsMag ak ndaw, amul góor ak jigéen
Everyone’s here tonightNa ñépp ñëw ci géew gi
I’m feeling goodMa woyaat sibam

Girls showing off their styleJigéen ñi woneleen seen bopp
And you guys, you know how to shineAk yeen góor ñi yee nit ci génn bokk

Big and small, no boys or girlsMag ak ndaw, amul góor ak jigéen
Everyone’s here tonightNa ñépp ñëw ci géew bi
Big and small, no boys or girlsMag ak ndaw, amul góor ak jigéen
Let’s light up the nightFeccal dugg ci geew gi
I’m feeling goodMa woyaat sibam

Viviane, I’m with Issa DieyeViviane, ma sira ak Issa Dieye
Fatim Penda and Ma NdiayeFatim Penda ak Ma Ndiaye
You’re all stunning, mashallah!Lay la cat, mashallah!

Let’s dance, let’s celebrate, it’s a beautiful nightTàcculeen, fecceleen, rafet genn
What’s up with the vibe tonight?Loo loy xubal geew gi
And you guys, let’s celebrate, it’s a big dealTe guleen, fecceleen, mag ñee
If you’re feeling good tonightBu gene gene geew gi
I’m feeling goodMa woyaat sibam

Yeah, yeah, yeahYeah, yeah, yeah
I’m feeling goodMa woyaat sibam

Oh la, oh la laOuh la, ou la la
I’m feeling itJege ma
Oh la, oh la laOuh la, ou la la
You feel it tooPare ngeen

Sibam, sibam, I’m feeling youSibam sibamoo sibam laal nga ma
Sibam, sibam, I’m feeling youSibam sibamoo sibam laal nga ma

When you dance, it’s like the world’s on fireBooy fecce sibam dangay mel ni xaaru la biir
Your vibe is like a party, I’m feeling youSa jege di karaje yaay sibam laal na ma

I say sibam, sibam, I’m feeling youMa ne sibam sibamoo sibam laal nga ma

When you dance, it’s like the world’s on fireBooy fecce sibam dangay mel ni xaaru la biir
Your vibe is like a party, I’m feeling youSa jege di karaje yaay sibam laal na ma

Comentários

Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra

0 / 500

Faça parte  dessa comunidade 

Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de Viviane Chidid e vá além da letra da música.

Conheça o Letras Academy

Enviar para a central de dúvidas?

Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.

Fixe este conteúdo com a aula:

0 / 500

Opções de seleção