Yeureum Djiguene
Def ma mbaamam
Def ma jaamam
Dóor subak ngoon la dëkk ak man
Def ma jaamam
Def ma mbaamam
Di ma toroxal, la dëkk ak man
La dëkk ak man
Saa su ne, la dëkk ak man
Di ma saaga, kanamu xale yi
Ci samay nawle, doo ma sutural
Yërëmuloo ma, faalewoo ma
Fonkuloo ma, mettit bi doy na
Dóor jigéen bi la juural say doom
Wax dëgg Yàlla li de ñaaw na
Démb jooy nga, ngir ma nob la
Tay nga am ma, di ma dóor di ma doyloo
Di ma dóor, di ma doyloo
Di ma dóor, di ma doyloo
Dina metti ci man, wax ma lan la
Dëgg, sonn naa kon yërëm ma
Sëyal naa la, muñel naa la
Yaaral la say doom, kon yërëm ma
Dóor jigéen bi la jural say doom
Wax dëgg Yàlla li de ñaaw na
Garab bu daanu, xob yaa laax na
Jigéen bu guéné, kër nga dey wét lool
Di ma dóor, di ma doyloo
Di ma dóor, di ma doyloo
Warul dooree
Gentleman
Warul doore
Déf ma mbaamam
Déf ma diaamam
Dima torokhal, la deuké ak mane
Déf ma mbaamam
Déf ma diaamam
Dima torokhal
Man dégg na,
Makk dan-na wax naan
Yërmandé lañuy yore jigéen
Man dégg na
Makk dan-na wax naan
Ci sutura lañuy yore jigéen
Al Hamdoulilah bi la Yàlla boolek ki lay soutoural
Al Hamdoulilah bi la Yàlla boolek kiy seddal sa xol
Kooku gentleman la
Gentleman la,
Youssou ma jigéen chéri Aïda du joyloo jigéen
Gentleman la,
Pape Ndiaye, baayu Fara Ndiaye chéri Aida Ndiaye
Kooku gentleman la
Gentleman la
Cheikh Amar chéri Marie Amar du joyloo jigéen
Kooku gentleman la
Mbaye Gueye Sagn-Sagnou Birame Guéye chéri Mame Ndiaye
Gentleman la
Cheikh Kanté chéri Amy Diawara du joyloo jigéen
Gentleman la
Matar Cissé chéri Aida Mar du joyloo jigéen
Gentleman la
Gentleman la
Cheikh Tidiane Ba chéri Lissa Ndoye du joyloo jigéen
Gentleman la
Boubacar Diallo, Diallo diéri chéri Mame Diarra
Gentleman la
Pape Cheikh Diallo chéri Kya Aidara
Gentleman la
Cheikh Sarr, keur Momar Sarr góoru Alima Ndione
Gentleman la
Neexalal sa jigéen
Jigéen àdduna la
Neexalal yaw yaw sa jigéen
Jigéen aljana la
Neexalal sa jigéen
Jigéen àdduna la
Neexalal yaw yaw sa jigéen
Jigéen aljana la
Mulher de Verão
Defenda sua mãe
Defenda sua irmã
Na rua, com um homem
Defenda sua irmã
Defenda sua mãe
Ela é preciosa, na rua, com um homem
Na rua, com um homem
Ela é minha, na rua, com um homem
Ela é uma rainha, mãe dos seus filhos
No tempo certo, não se preocupe
Mulher de verão, mulher de fogo
Mulher forte, com coração puro
Na rua, a mulher é a rainha do seu destino
A palavra de Deus é a única verdade
Não se preocupe, não me deixe
Estou com você, ela é minha, ela é minha jóia
Ela é minha jóia, ela é minha jóia
Ela é minha jóia, ela é minha jóia
Não há nada no mundo que possa te separar de mim
Sim, eu te amo, mulher de verão
Você é minha vida, meu amor
Você é a luz do meu destino, mulher de verão
Na rua, a mulher é a rainha do seu destino
A palavra de Deus é a única verdade
Agradeça a Deus, não se preocupe
A mulher é a rainha, sua casa é o seu castelo
Ela é minha jóia, ela é minha jóia
Ela é minha jóia, ela é minha jóia
Proteja a mulher
Cavalheiro
Proteja-a
Defenda sua mãe
Defenda sua irmã
Ela é preciosa, na rua, com um homem
Defenda sua mãe
Defenda sua irmã
Ela é preciosa
Eu te vejo,
Eu te amo, não há nada além de você
Mulher, você é a rainha do meu coração
Eu te vejo,
Eu te amo, não há nada além de você
No caminho, você é a rainha do meu coração
Louvado seja Deus, que te deu a paciência para esperar
Louvado seja Deus, que te deu a força para suportar a dor
Cavalheiro
Cavalheiro,
Você é o querido de Youssou, Aïda é a jóia do seu coração
Cavalheiro,
Pape Ndiaye, pai de Fara Ndiaye, Aida Ndiaye é a jóia
Cavalheiro
Cavalheiro
Cheikh Amar, amante de Marie Amar, ela é a jóia do seu coração
Cavalheiro
Mbaye Gueye Sagn-Sagnou, Birame Guéye, amante de Mame Ndiaye
Cavalheiro
Cheikh Kanté, amante de Amy Diawara, ela é a jóia do seu coração
Cavalheiro
Matar Cissé, amante de Aida Mar, ela é a jóia do seu coração
Cavalheiro
Cavalheiro
Cheikh Tidiane Ba, amante de Lissa Ndoye, ela é a jóia do seu coração
Cavalheiro
Boubacar Diallo, Diallo, amante de Mame Diarra
Cavalheiro
Pape Cheikh Diallo, amante de Kya Aidara
Cavalheiro
Cheikh Sarr, casa de Momar Sarr, Alima Ndione é a rainha
Cavalheiro
Respeite sua mulher
Mulher deste mundo
Respeite-a, respeite sua mulher
Mulher do paraíso
Respeite sua mulher
Mulher deste mundo
Respeite-a, respeite sua mulher
Mulher do paraíso