Tradução gerada automaticamente

Damalay Bëgg
Jahman X-Press
Damalay Bëgg
Damalay Bëgg
Quando confiei meu coração a vocêBi ma la dénkee sama xol
Já faz um tempo que não brinco com elaFowewoo ko nenne tuuti
Então, se eu te dissesse onde eu estavaBa tax na su ma la doon wax fi nga ma tollu
Estou apaixonado por vocêDama la nob dafay tuuti
Agora eu tenho uma aparência e você está me dando o motivoLéegi dama am teint te bae yaa may jox li tax
Eu tomo banho com o xampu do amor!Shampoing mbëggeel laay sangoo
Então quem vê meu ex não está se traindoKon ku gis sama ex, nekkoo boppam lay nax
Quando ele me beija assim eu sinto falta deleSu fóogee nii namm naa ko
Não sei o que ele vai fazer com vocêXawma nan lay def ak yaw
Minimize o fascínio da corridaWaññil allure bi ngay daw
Qual é o seu tipo de amor, querida?Sa xeetu mbëggeel lan la baby?
Coloquei meu coração lá fora e merda, merda, merdaTegal fi sama xol bi nga këf, nga këf, nga këf
Até que eu sinta vontade de fazer coisas, coisasBa ma féemu def ay yëf, ay yëf
Você não é daqueles que falam porque é você quem fazYaw bokkok ñiy wax ndax yaa jëf moo tax
Eu te amoMan dama lay bëgg
Eu te amo para sempre, queridaMan dama lay bëgg ba kañ baby
Eu te amo!Dama lay bëgg
Eu te amo!Dama lay bëgg
Eu te amo para sempreDama lay bëgg ba kañ
Eu te amo, querida!Chérie, dama lay bëgg
Estou errado se estou preocupadoMan su ma yàkkamti woom juum
Eu encontrei aquele que era destinado a mimGis naa ki ma Yàlla dencaloon
Eu te amo para sempreMan dama lay bëgg ba kañ
Ah, como eu queria estar errado!Ay su ma yàkkamti woom juum
Adorei por quanto tempoBëgg ba kañ
Eu encontrei aquele que era destinado a mimGis naa ki ma Yàlla dencaloon
Eu te amo para sempreMan dama lay bëgg ba kañ
Eu ainda não desisti de vocêSama yaakaar tasul ci yaw ba léegi
Eu sempre te levanto porque você me derrubouFoo jaar ma yëkkëti la ndax yaa ma daaneel
Você é um personagem para mim e para o túmuloJikko nga ci man maak yaw ba biir bàmmeel
E é por isso que chamamos as palavras de linger e dameelMaak yaw a tax ñu naan baatu lingeer ak dameel
Sua resposta lhe recompensará pelo coração que você me deveTontu sa borom lay fay ndax xol nga ma ameel
O amor conquista todas as coisasLi ci mbëggeel lanaati lépp
A coisa mais estúpida é dizerLi bu raxul dof yitt ci la
Eu estou sempre láFoo ne maa nga fa
E onde estou à sua frente, estou esperandoTe fu ma la jiitu xaar laa fa
Não tenho interesse em vocêAmuma sago ci yaw
Você não fica nervosa a vida toda, querida?Est-ce que sax yaw doo nervis une vie, baby
Eu sou o único que conheçoMan yaw rekk laa miin
Você é meu conforto porque quando estou preocupado, recorro a vocêYaay dalal sama xel ndax fu ma jaaxle yaw laay wutsi
Mas eles tinham que ter cuidadoWaaye fokk ñu takk pettaaw
Você sabia que o gato é rápido?Ndax xam nga cat dafa gaaw
Qual é o seu tipo de amor, baby? (Meu bebê)Sa xeetu mbëggeel lan la, baby? (Mon bébé)
Todo mundo sabe que eu sou umÑépp xam nañu man dama la
Eu quero você de novo!Dama la bëggawut
Eu te amo bebê!Bëgg naa la, baby
Eu chamo você de meu presente de DeusSama cadeau d'Allah laa lay woowe
Adorei minha configuração!Nga bëgg leen sama tabbe
Estou ligando para você desde que você me sequestrouNaan laa lay woowee bi nga ma jàppe ba tay
Você não deixa a porta queimar e diz adeusBàyyiwoo su jakk yakk nga waxe fë
Eu te amoMan dama lay bëgg
Eu te amo para sempre, queridaMan dama lay bëgg ba kañ baby
Eu te amo!Dama lay bëgg
(Eu te enviei tudo, amor)(Yénne naa la lu nekk sama baby)
Eu te amo, billaayMan dama lay bëgg, billaay
Eu te amo para sempreDama lay bëgg ba kañ
Eu te amo, querida!Chérie, dama lay bëgg
Estou errado se estou preocupadoMan su ma yàkkamti woom juum
(Quanto tempo)(Bëgg ba kañ)
Eu encontrei aquele que era destinado a mimGis naa ki ma Yàlla dencaloon
Eu te amo para sempreMan dama lay bëgg ba kañ
Ah, como eu queria estar errado!Ay su ma yàkkamti woom juum
Adorei por quanto tempoBëgg ba kañ
Eu encontrei aquele que era destinado a mimGis naa ki ma Yàlla dencaloon
Eu te amo para sempreDama lay bëgg ba kañ
Eu ainda não desisti de vocêSama yaakaar tasul ci yaw ba léegi



Comentários
Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra
Faça parte dessa comunidade
Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de Jahman X-Press e vá além da letra da música.
Conheça o Letras AcademyConfira nosso guia de uso para deixar comentários.
Enviar para a central de dúvidas?
Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.
Fixe este conteúdo com a aula: