Tradução gerada automaticamente

exibições de letras 18

Khalé Bingay Wo

Jahman X-Press

Letra

Khalé Bingay Wo

Khalé Bingay Wo

Danga wara yamDanga wara yam
Cuub dafay xam lekkamCuub dafay xam lekkam
Mag du nax bopamMag du nax bopam
Man ponkala may àttanMan ponkala may àttan
Ki ma nekkal zero fauteKi ma nekkal zero faute
Panu xaalis xëbbalumaPanu xaalis xëbbaluma
Yang may woo maa lay xojYang may woo maa lay xoj
Demal togg wërumalaDemal togg wërumala

Eh, você tá me tirandoEh yaw coupeel maa ngi jokko
Quem me chamou, me chamouKi ma nob ma nob ko
Quem tá se achandoKi la gëna pare
Quem faz bagunça na minha mãoKi def bague sama loxo

Eska man ndiroo naa laEska man ndiroo naa la
Ku lamb yaw xolaat maKu lamb yaw xolaat ma
Ku dul moom gisuma laKu dul moom gisuma la
Bàyyi ma ngir YàllaBàyyi ma ngir Yàlla
Kenn du am ki ma amKenn du am ki ma am
Di ko weccoo da mën boramDi ko weccoo da mën boram
Ki ngay woo muñal ko day wax ak kim jox xolamKi ngay woo muñal ko day wax ak kim jox xolam

Se de jinne pesu la te dofooSu de jinne pesu la te dofoo
Man soo ma xoolee xam ne dama ne ci loxoMan soo ma xoolee xam ne dama ne ci loxo
Man ak ñi lamb xam nga ni y’a pas photoMan ak ñi lamb xam nga ni y’a pas photo
Dama neex a xol ki ma yor moo ma tooppato (mu ne)Dama neex a xol ki ma yor moo ma tooppato (mu ne)

Eh, moleque, você tá me tirandoEh xale bi ngay woo
Tô vendo outro que me chamouMu ngi jokkok keneen ki mu nob ba ko
(Te Yàlla tax)(Te Yàlla tax)
Sonal nga ko (torop)Sonal nga ko (torop)
Eh, vaiEh bako (nga ni)
Ne na sonal nga koNe na sonal nga ko
Eh, vai, ehhEh bako, ehh
Gëmal Yàlla bàyyil ki nobu laGëmal Yàlla bàyyil ki nobu la

Moleque, você tá me tirandoXale bi ngay woo
Tô vendo outro que me chamouMu ngi jokkok keneen ki mu nob muñal
(S'il te plaît)(S'il te plaît)
Ko ba beneen (tamit)Ko ba beneen (tamit)
Way vaiWay bako
Ne na sonal nga ko (dëgg Yàlla)Ne na sonal nga ko (dëgg Yàlla)
Way vai ehWay bako eh
Gëmal Yàlla bàyyil ki nobu laGëmal Yàlla bàyyil ki nobu la

Loy saf si man (xawma)Loy saf si man (xawma)
Jar na ba pare (bu yàgg)Jar na ba pare (bu yàgg)
Dozé ma yombul bàyyil sa xel bi ngay kafe (aw demal togg)Dozé ma yombul bàyyil sa xel bi ngay kafe (aw demal togg)
Ki rekk ka fi ne moom rekk gami la signéKi rekk ka fi ne moom rekk gami la signé
Bësal bouton bu xonq bi danga wara coupéBësal bouton bu xonq bi danga wara coupé
Su de luy raye la man na ma ray man bëgg naSu de luy raye la man na ma ray man bëgg na
Man benn yoon lay toy ma raw cimentMan benn yoon lay toy ma raw ciment

Garde la ligne soo yakamtiwulGarde la ligne soo yakamtiwul
Damay wax ak bonheurDamay wax ak bonheur
Fi ak wer mën nañu ko waxFi ak wer mën nañu ko wax
Fi m’ma kepp moo dëgërFi m’ma kepp moo dëgër
Ocuppé kañ nga nar a coupéOcuppé kañ nga nar a coupé
Bànneex lay waxal soo may woo lay communiquéBànneex lay waxal soo may woo lay communiqué
Ñamu mak xale lu ciy yoonaamÑamu mak xale lu ciy yoonaam
Place bi am na boroomamPlace bi am na boroomam
Forcé taxul nga jot ci man soo ma xiifee yëyal singomForcé taxul nga jot ci man soo ma xiifee yëyal singom

Coupél quitteelCoupél quitteel
Bànneex lay communiqueelBànneex lay communiqueel
Fideel ci moomFideel ci moom
Maa ngi dundu mbëggeelMaa ngi dundu mbëggeel

Bul ma ñodi lu amul ci moom la dagg bu yàggBul ma ñodi lu amul ci moom la dagg bu yàgg
Kiy tax bàyyi ko juddoogul baayam de na bu yàggKiy tax bàyyi ko juddoogul baayam de na bu yàgg
Lu ma jooxañ mu dagg te jox na ma sama geddLu ma jooxañ mu dagg te jox na ma sama gedd
Caabi jàng ñu sànni géejCaabi jàng ñu sànni géej
Buntu nekk booy fëggBuntu nekk booy fëgg

Se de jinne pesu la te dofooSu de jinne pesu la te dofoo
Man soo ma xoolee xam ne dama ne ci loxoMan soo ma xoolee xam ne dama ne ci loxo
Man ak ñi lamb xam nga ni y’a pas photoMan ak ñi lamb xam nga ni y’a pas photo
Dama neex a xol ki ma yor moo ma tooppato (mu ne)Dama neex a xol ki ma yor moo ma tooppato (mu ne)

Eh, moleque, você tá me tirandoEh xale bi ngay woo
Tô vendo outro que me chamouMu ngi jokkok keneen ki mu nob ba ko
(Te Yàlla tax)(Te Yàlla tax)
Sonal nga ko (torop)Sonal nga ko (torop)
Eh, vaiEh bako
Ne na sonal nga koNe na sonal nga ko
Eh, vai, ehh (nga ni)Eh bako, ehh (nga ni)
Gëmal Yàlla bàyyil ki nobu laGëmal Yàlla bàyyil ki nobu la

Moleque, você tá me tirandoXale bi ngay woo
Tô vendo outro que me chamouMu ngi jokkok keneen ki mu nob muñal
(S'il te plaît)(S'il te plaît)
Ko ba beneen (tamit)Ko ba beneen (tamit)
Way vaiWay bako
Ne na sonal nga ko (dëgg Yàlla)Ne na sonal nga ko (dëgg Yàlla)
Way vai ehWay bako eh
Gëmal Yàlla bàyyil ki nobu laGëmal Yàlla bàyyil ki nobu la
(Lëjjal nga ma witt)(Lëjjal nga ma witt)

Comentários

Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra

0 / 500

Faça parte  dessa comunidade 

Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de Jahman X-Press e vá além da letra da música.

Conheça o Letras Academy

Enviar para a central de dúvidas?

Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.

Fixe este conteúdo com a aula:

0 / 500

Opções de seleção