Tradução gerada automaticamente

Ndaanaan
AMADEUS
Ndaanaan
Ndaanaan
Papa pa papaPapa pa papa
Eu quero aprenderDama bëgg jàngi
Eu quero ter conhecimentoDama bëgg am xam-xam
O que, meu filho?Lan, sama doom?
Eu quero aprenderDama bëgg jàngi
Eu quero ter conhecimentoDama bëgg am xam-xam
Eeeh Massamba WaloEeeh Massamba Walo
Eu não sou quem eles dizem que souDuma doon ku ñu naan cam
Não me olhe e me diga o que souDoo ma xool di ma naan topp ma

Ninguém pode me olhar e me dizer o que souKenn du ma xool di ma naan topp ma
O país vai dar um jeito nos que estão perdidosReew mi dinañ donni ñi fiy doggali
O dia está chegando, é dia de festaBés sa ngi ci bés yi
Eles vão se unir, não vão se separarDinañ bokku ci ñin na diiw wa ngi
Será que eu estou fazendo o que é certo?Ndax dama fonk loolu sama liggéey
Fazer o que é certo é o que eu queroTekki gëm-gëm moo kay maye
Talvez eu não saiba se estou fazendo certoMënta naqari su may liggéey
Será que isso é bom pra mim?Ndax li kay neexal lang ci man
Fazer o que eu faço é minha personalidadeDef li may def ci personnalité
Colocar isso em um código de verdadeTeg ko ci code du genn gamm
Trazer aqui outras tonalidadesIndi fi yeneen tonalité
Fazer com que elas se tornem um jogoDugal leen ci yeneen ni game
Aay waay!Aay waay!
Eu não sou quem eles dizem que souDuma doon ku ñu naan cam
Não me olhe e me diga o que souDoo ma xool di ma naan topp ma
Eu não sou quem eles dizem que souDuma doon ku ñu naan cam
Ninguém pode me olhar e me dizer o que souKenn du ma xool di ma naan topp ma
Eu não sou quem eles dizem que souDuma doon ku ñu naan cam
Não me olhe e me diga o que souDoo ma xool di ma naan topp ma
Eu não sou quem eles dizem que souDuma doon ku ñu naan cam
Ninguém pode me olhar e me dizer o que souKenn du ma xool di ma naan topp ma
Ndaanaan, meu amor é verdadeiroNdaanaan sama lama ngone
Na terra onde a gente se encontraCi bor bu tar bi lañu jogé
Ndaanaan, meu amor é verdadeiroNdaanaan sama lama ngone
Eles não vão nos deixar, não vamos nos separarDañu sonoo loolu bañuy doni gone
Alhamdulillah eeehAlhamdulillah eeeh
O que é mais importante é a uniãoLi gëna metti jot na jaale
Deixe que quem ama se una a quem amaNa indi ku leen di ngone nam indi
Nós sabemos onde estamos, não vamos nos perderNanguwuñu xam nañu fi ñu jogé fàttewuñu
Será que estamos fazendo o que é certo?Ndax dañu fonk loolu sunu liggéey
Fazer o que é certo é o que eu queroTekki gëm-gëm moo kay maye
Talvez eu não saiba se estamos fazendo certoMënta naqari su ñuy liggéey
Será que isso é bom pra mim, eeeh waay!Ndax li kay neexal lang ci man, eeeh waay!
Eu não sou quem eles dizem que souDuma doon ku ñu naan cam
Não me olhe e me diga o que souDoo ma xool di ma naan topp ma
Eu não sou quem eles dizem que souDuma doon ku ñu naan cam
Ninguém pode me olhar e me dizer o que souKenn du ma xool di ma naan topp ma
Eu não sou quem eles dizem que souDuma doon ku ñu naan cam
Não me olhe e me diga o que souDoo ma xool di ma naan topp ma
Eu não sou quem eles dizem que souDuma doon ku ñu naan cam
Ninguém pode me olhar e me dizer o que souKenn du ma xool di ma naan topp ma

Comentários
Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra
Faça parte dessa comunidade
Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de AMADEUS e vá além da letra da música.
Conheça o Letras AcademyConfira nosso guia de uso para deixar comentários.
Enviar para a central de dúvidas?
Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.
Fixe este conteúdo com a aula: